Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
 
Taarixkat yi [[Seex Anta Joob]] ak yenene, woné nanu, diiney yawut, kirist ak Lislaam, fofu (wa Misra) lañu cossano. Ndax yonent yi ñu nek ca diiney yawut ak kirist, ca sene teree, [[biibël]] ak thora, Ibrahima ak Moussa, fofu lañu jang diiney, ca bi ñu tuddu ca lakk wa misra bu fa amone jamono bobu, ''Per-Ankh'', ca kalamu [[wolof]] moye: Keur bu ñu jang Diiney ak xam xam. Ba paré yobu nañu Diiney bobu ca sene Mbokku yawut, ndax bobu amuñu woon Diiney, nak bu urus ak Moloch ak Baal lañu doon geum. Fofu tamit lañu jang naka lañu saraxé Xaar, ak naka lañu xarafal, ca ''Per-Ankh'' yi. Ndax ca diiney bu afrig, sarax ak xarafal amona bu yag, ba tey.
Taarikhkat woné nañu tamit, yawut yi nekkone ca rewum nit ku niul ba, wa misra, kene deful leen ay jaam. ñow nañu fofu ca jaam, gën misra ca jaam.[[Image:Sudan Meroe Pyramids 30sep2005 2.jpg|thumb|250px|left|Mbaanaar Bammel bu Méroé, [[Sudaan]]]]