Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
a
 
Aucun résumé des modifications
Rëdd 8 :
 
Buñu waccé ca Afrig bobu, xeet yi tass nañu yu bari, té ba paré xeet ku nek, amone nañu bene tuddu ngiir tuddu yallah:
[[Image:Sub-Saharan-Africa.png|thumb|190px|La zone verte indique l'Afrique sub-saharienne, et par extension l'ère d'influence des religions nègres.]]
 
* [[Mandinke]] yi ([[Sooninke]], Bambara, Jula, Xasonke, ak ñu dem nonu) yallah, ''Maa Ngala'' lañu daan wax.
Ligne 22 ⟶ 23 :
* Wa [[Ecoopi]]: ''Waqa''
* wa [[Kongo]] ca xeet yi Bantu: ''NzamBe''
 
 
Diiney bi tamit, xeet yi Afrig bi, amona ku nek, joox na ko bene tuur, ''Vodu'' ca wa [[Bene]], Togo, [[Gana]], ba [[Niseeria]], wala ''Bwiti'' ca wa [[Gabon]], ''Mwett'' wa [[Cameroon]].