Jimbulang bu waa-Brëtaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Ad Encyclopaedia-Britannica 05-1913.jpg|thumb|rigth|200px| yëgleeb génnu jumbulang bi]]
'''Jimbulang bu waa-Brëtaañ''' walla '''Encyclopædia Britannica''' (ci wu-angalteer), ñi ngi ko siiwal ci diggante 1768-1771. Siiwalam gu njëkk mi ngi ame ca [[Edimbuurg]] ca [[Ekos]]. Bu waa-Brëtaañ bi bokk na ci [[jimbulang]] yiy wax ci lu daj yi njëkk ci kàllaama [[wu-angalteer]], te bay jii ñoo ngi koy siiwal.
 
Ci ndoorteelu ñaareelu xaaju 1700 ba ci 1900, bari woon na ay boroom xam-xam yu doon jàppee ay jukkeem niki delluwaay bu wóor, yenn saa yi, ci siiwal yu yees yi, daa na am ay [[gisiin]] yu yees yees jagleel ay mboolooy gëstukat. Ci jamono yooyu amoon na gëdd bu baax ci biir askan wiy làkk wu-angalteer. Ci XX xarnu bi la yitteey jimbulang soppiku bu baax, coppite gi amal na ay njeexiit ci xarkanam ci fukk ak benneelu siiwal gi.
 
== Taariixu jagal yi==
{| class="wikitable"
! jagal !! taariixu jagal !! dayoo
|-
| align="right" | 1{{eel}} || [[1768]]–[[1771]]
| 3 téere
|-
| align="right" | 2{{eel}} || [[1777]]–[[1784]]
| 10 téere
|-
| align="right" | 3{{eel}} || [[1788]]–[[1797]], [[1801]]
| 18 téere
|-
| align="right" | 4{{eel}} || [[1801]]–[[1809]]
| 20 téere
|-
| align="right" | 5{{eel}} || [[1815]] || 20 téere
|-
| align="right" | 6{{eel}}
| [[1820]]–[[1823]], [[1815]]–[[1824]]
| 20 téere ak 2 yees yokk
|-
| align="right" | 7{{eel}} || [[1830]]–[[1842]]
| 21 téere
|-
| align="right" | 8{{eel}} || [[1852]]–[[1860]]
| 21 téere
|-
| align="right" | 9{{eel}} || [[1875]]–[[1889]]
| 24 téere
|-
| align="right" | 10{{eel}} || [[1902]]–[[1903]]
| 9{{u}} jagal ak 2 yees yokk
|-
| align="right" | 11{{eel}} || [[1910]]–[[1911]]
| 29 téere
|-
| align="right" | 12{{eel}} || [[1921]]–[[1922]]
| 11{{u}} jagal ak 3 yees yokk
|-
| align="right" | 13{{eel}} || [[1926]]
| 11{{u}} jagal ak 6 yees yokk
|-
| align="right" | 14{{eel}} || [[1929]]–[[1973]]
| 24 téere
|-
| align="right" rowspan=2 | 15{{eel}} || [[1974]]–[[1984]]
| 28 téere
|-
| | [[1985]]– || 32 téere
|}
 
jagal gu njëkk gees def ci CD-ROM mi ngi génn [[1994]].
 
== Lëkkalekaay yu biti ==
* {{en}} [http://www.britannica.com/ dal bees ko jagleel]
* {{en}} [http://www.1902encyclopedia.com/ 9{{eel}} ak 10{{eel}} ci lënd gi]
* {{en}} [http://www.1911encyclopedia.org/ 11{{e}} jagal ci lënd gi]
 
[[Wàll:jimbulang]]