Jimbulang bu waa-Brëtaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Jimbulang bu waa-Brëtaañ''' bi, ñi ngi ko siiwal ci diggante 1768-1771. Siiwalam gu njëkk mi ngi ame ca Edimbuurg ca Ekos. Bu waa-Brëtaañ bi bokk na ci jimbulang
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Jimbulang bu waa-Brëtaañ''' biwalla '''Encyclopædia Britannica''' (ci wu-angalteer), ñi ngi ko siiwal ci diggante 1768-1771. Siiwalam gu njëkk mi ngi ame ca [[Edimbuurg]] ca [[Ekos]]. Bu waa-Brëtaañ bi bokk na ci [[jimbulang]] yiy wax ci lu daj yi njëkk ci kàllaama [[wu-angalteer]], te bay jii ñoo ngi koy siiwal.
 
Ci ndoorteelu ñaareelu xaaju 1700 ba ci 1900, bari woon na ay boroom xam-xam yu doon jàppee ay jukkeem niki delluwaay yubu wóor, yenn saa yi, ci siiwal yu yees yi, daa na am ay [[gisiin]] yu yees yees jagleel ay mboolooy gëstukat. Ci jamono yooyu amoon na gëdd bu baax ci biir askan wiy làkk wu-angalteer. Ci XX xarnu bi la yitteey jimbulang soppiku bu baax, coppite gi amal na ay njeexiit ci xarkanam ci fukk ak benneelu siiwal gi.
[[Wàll:jimbulang]]