3 292
modifications
m (Tuddewaat nañ Jumtukaayu xarala yu yees léegi mooy Xaralay xibaar ak jokkoo) |
Aucun résumé des modifications |
||
'''Xaralay Xibaar ak Jokkoo''' (XXJ) walla '''Xaralay Xibaar ak Jokkoo yu Yees''' yi, ci [[wu-angalteer]] ''Information and Communication Technology'', ci [[wu-faraas]] ''Nouvelles technologies de l'information et de la communication'', moo ëmb mbooleem xarala yees jëfandikoo ngir yor ak jokkale ay xibaar. Yitteem mooy sos ay noste yuy yor ay xibaar, yor seenug suqaliku, seenug dencu, seenug jokkale, ak seenug kaaraange.
Yombul joxe ci ab tekki bu daj ndax amul benn tekki bu ñépp ànd déggoo. Ñi ciy liggéey raññee nañu leen niki ñu seen xam-xam daj, dañoo nekk ñuy xam lépp lu laal: [[mbëjfeppal]], [[xam-xamu nosukaay]], [[jokkoosoryante]].
== Lëkkalekaay yu biir ==
*[[Xam-xamu nosukaay]]
*[[Internet]]
*[[mbëjfeppal]]
[[Wàll:Xam-xamu nosukaay]]▼
[[vi:Công nghệ thông tin]]
[[zh:信息技术]]
▲[[Wàll:Xam-xamu nosukaay]]
|