Mbàmbulaan gu Bëj-saalum wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: da:Sydlige Ishav
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: pms:Océan Antàrtich; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[ImageDencukaay:Océan Austral.png|thumb|right|200px|Mbàmbulaan gu Bëj-saalum]]
'''Mbàmbulaan gu Bëj-saalum''' gi mooy mbalkaam ndox mi ne ci li wër [[Dottub Bëj-saalum]] bi. Mooy ñenteelu [[Mbàmbulaan|mbàmbulaan]] mi gën a réy ci [[Àdduna|àdduna]] bi.
 
Yaatuwaayam gépp mi ngi toll ci 20 327 000 km², guddaayu tefes gi di 17 968 km.
 
Mi nu wuteeg yeneen mbàmbulaan yi seen dig doon ay gox, moom rek mooy la ñuy tekkee ni ab mbalkaam ndox mu wër ab gox (goxub [[Dottub Bëj-saalum|Dott bu Bëj-saalum]]); doon ab jaaro bu tëdd ci 60°(60 aj) gu [[Tus-wu-gaar|tus-wu-gaar]] wu Bëj-saalum.
 
Mbàmbulaan gu Bëj-saalum xóotee na lu tollook 4 000 ba 5 000 m, daanaka ci tëraayam gépp, lu weesu yénn barab yi gën a néew xóotaay.
Rëdd 15 :
* [[Mbàmbulaan]]
 
[[Wàll:mbàmbulaanMbàmbulaan yi]]
 
[[af:Suidelike Oseaan]]
Rëdd 78 :
[[oc:Ocean Antartic]]
[[pl:Ocean Południowy]]
[[pms:Océan Antàrtich]]
[[pt:Oceano Antártico]]
[[qu:Antartiku mama qucha]]