Abdulaay Wàdd wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Image:Abdoulaye_Wade_-_World_Economic_Forum_Annual_Meeting_New_York_2002.jpg|thumb|right|350px|Abdulaay Wàdd diisoo Ci koom-koomu adduna, niw york ca atum 2002]]
[[Abdulaay Wàdd]] mi ngi juddu 29 Mee 1926 ca [[Kebemeer]] amna 82at, mooy njiitu réewum [[Senegaal]] ca 1 awril 2000 ba leegi, ki mu wuutu ci toogu boobu mooy [[Abdou Juuf]]. batey mooy njiitu làng gu demokaraasi gu Senegaal (PDS), te it mooko sos 37 Suwe 1974 ci nginnaaw bi mu ci tangoo [[Léopold Sédar Senghor]] mu nangu, nek na ci kujjek politig gi lu tol ci 25at yàgg nakoo jiite, ci diir boobi tëjees nako ci ay yoon. soxnaam mingi tud fifiyaan wàdd. am na ñaari dóom góor ak jigéen Kariim Wàdd mooy góor Sinjiili Wàdd di jigéen. diineem mooy lislaam fiqqu maalik, moongi bokk ci yoonu muriit. moom nak ku xareñ la ci wàllu yoon ak koom-koom amna it raaya jang wi gën a mak ci ñaari wàll yooyi, moongi jange wàllu yoon ci daara jii di [[lycée Condorcet]] ca [[Fraas]]. wàllu koom-koom moongi ko jangee ci daara ju kawe ju ndakaaru.
[[Wàll:niti senegaal]]