Mbàmbulaan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
'''Mbàmbulaan''' am mbalka mu réy la mu def ndoxum xorom, te wër ab [[gox]].
 
Mbooleem mbàmbulaan yi ak [[géej]] yi ñoo jël 70% di ñatti ñenteelñeenteel ci li ci Kaw kol-kolub suuf si, maanaam 360.700.000 km². Ci lim bii 154.800.000 km² ñoo ngi ci [[Xaaju kol-kol bu bëj-gànnaar|xaaju kol-kol bu bëj-gànnaar]], 205.900.000 di km² ci [[Xaaju kol-kol bu bëj-saalum|xaaju kol-kol bu bëj-saalum]].
 
Mbàmbulaan yi joroomjuróom la ñulañu:
* [[Mbàmbulaan gu Dal]], 179.700.000km&sup2, 49,7%;
* [[Mbàmbulaanu Atlas]], 106.100.000 km&sup2, 29,5%;
Rëdd 11 :
* [[Mbàmbulaan gu Bëj-gànnaar]], 14 090 000 km², 3,9%
 
Waaye waa [[Angalteer|waa-Angalteer]] yi ci seen gisinu séwógaraafi[[melosuuf]] da ñuy jàppee mbooleem géej yi ne ci li wër ñaari [[Goxi dott|goxi dott]] yi, duppee leen [[Mbàmbulaan gu Bëj-gànnaar]] ak [[Mbàmbulaan gu Bëj-saalum]].
 
{| align="center" border="1" bgcolor="#FFFFCC" bordercolor="#486C7D" cellspacing="0" cellpadding="1"