Kàttan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
m Ajout rapide de la catégorie Wàll:Kàttan (avec HotCats)
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
Kàttan mooy man a def dara (sos ag soppi), kàttan nag am na ay melo yu bari, yi ci ëpp solo ñi ngi feeñe ci tàngoor ak leer.
 
Ci biir “xam-xami dénd yi” (science naturelle) kàttan man na fee jël ay melokaan yu wuute : “kàttanug tàngoor”, “kàttanug kimyaa (simi)”, “kàttanug mbëj”, “kàttanug ceññeer”, “kàttanug saal (nucleaire)” ak ci mujjantal gi “kàttanug mbëjbijjaakon (éléctromagnétique)” añs. Xeeti kàttan yii ñaare dees leen di séddale ci: “kàttan guy yëngu ak “kàttan gu nëbbu” te kat am na yenn kàttan yoy dëppoowunook séddale gii, lu ci mel ni: “leer gi”, ak yeneen yoy man nanoo nekk am njaxas mu tukkee ci ñaari kàttan yi, guy yëngu gi ak gu nëbbu gi.
 
Lu bari ci xeeti kàttan yii manees na koo soppi (transformer) jële ko ciw melo yóbbu ko ci weneen, jaare ko ci jëfandikoo ay jumtukaay yu fasoodiku (simple) walla ay xarala yu fasu (compliqué): la ko dale ca “kàttanug kimya” ba ci “gu mbëj” jaare ko ci jumtukaay bu siiw bi di tegale(pile) yi, walla ndëxañtéef yi, Albert Ayinstaayin it ci biir ”[[faramfaceg ajoo]]” (theorie de relativisme) boole na ñaari ëtt yii di bu ne-ne ak kàttan, nga xam ne kàttan day mujj man a soppiku di ne-ne(matiere), naka noonu safaan bi, maanaam neen soppiku moom it di kàttan: wuññi (découverte) gu yees gii mi ngi ko xamalee ci yemalem gu siiw googee E=mc2, soppiku gii ci jëf (ci wàllug pratique) ñi ngi ko firee ci man gi nu man a ame kàttan jaare ko ci “[[xarug saal]]” walla “[[booleeg saal]]”.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Kàttan » lañ ko jële