Xam-xamu nosukaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Xam-xamu nosukaay''' (walla '''Xam-xam gi ñeel nosukaay'''), moo yor gëstu gi aju ci [[Cëslaayu xibaar|cëslaay yu xibaar]] yi, xarala yi ñeel seenug nos ak seenug jëfandikoowiinjëfandikuwiin ci noste yi ñuy jëfandikoo ay [[nosukaay]]. Ñi ciy yëngu seen liggéey doon lëkkale ay nosukaay ñu doon li ñuy tuddee ag [[lonkoo]], defar ay [[Dàttub njoxe|dàtti njoxe]], [[Noste gu boppu|boppal ay noste]], defar ay [[Tëriin|tëriin]] te loolu laaj na xam ag [[Kàllaamab tëriin|kàllaamag tëriin]], .
 
Cig lawal, xam-xamu nosukaay dafa ëmbu ci li ñuy wax ''[[Xaralay xibaar ak jokkoo yu yees| xaralay xibaar ak jokkoo yu yees]]'' yi di xeetu xam-xam bi ëmb lépp li ñeel xibaar, ci béppgépp anamam. Ci tëriin wi la tëralkat bi di joxee ay tektaltegtal nosukaay bi ci anam gi mu war a yoree xibaar yi, lan la ci war a def ak nan la ko war a defe. [[Jëfaan]] yi nag ñooy mbooleem cëri nosukaay bi, benn bu ci nekk am na liggéey bu ñu ko sant: yii di rënk xibaar yi, yii di leen wone ni nga bëgge, yii di leen soppi...
 
== Taariix ==