Ndimbal:Ndimbal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 6 :
|
[[Image:Nuvola apps help index.png|right|80px|]]
<poemcenter>Xët wii da lay won lëkkalekaay yi ëpp njariñ ngir nga mana cëru te jang jëfandikoo Wikipedia.
Dañ leen séddatle ciy xaaj yuy wax ci doxinu dal bi, ay baaxu Wikipedia ak ay àtteem yu ñuy wormaal, ci soppi xët yi, yokkug ëmbiitam ak melokaanu xaralay jimbulang.
 
</poemcenter>
|}
== [[Ndimbël ci ay nataal]] ==
 
== <center> [[Image:Nuvola apps ksig.png|30px|]] Ngir man a duggal dara </center> ==
<noinclude>{| align=right padding=0 cellspacing=0 width=49% style=";background-color:#e6e6fa; border: #B17B26 solid 1px"</noinclude>
Ligne 25 ⟶ 23 :
;[[Man mbindin ngay jëfandikoo?]]:Fii ngay gise xàll yi gëna yaa, ci mbindin wu yomb wooy jëfandikoo ci xët yi ngay sos walla di ko nas ci Wikipedia
;[[Nan ngay lëkkalee ay jukki ci seen biir?]]:Ni mu wutee ak yeneen jimbulang yi, Wikipedia day def nga mana jóge ci aw xët dem ci weneen ci anam wu yomb lool. Loolu laaj na, saa yooy soppi walla sàkk ab jukki, def ci ay lëkkalekaayi biir.
;[[Nooy duggaledugale lëkkalekaayi biti?]]:Ngir yenn jukki yi, man naa doon lu solowu yenn saa yi nga def ay lëkkalekaay yu biti yu lay yóbb ci yeneeni dal, yuy yokk ay xibaar ci li nga jota jukki.
;[[Nooy duggaledugale ab lëkkalekaay diggantelàkk?]]:Dafa am ay waa-wikipedia yu bari ci yeneen làkk. Nii la nuy duggale ay lëkkalekaayi diggantelàkk ci biir jukki yi, ngir jàngkat yi man koo am ci yeneen làkk.
;[[Ay kàddu ci say coppite]]:Ay baat yu néew ci li waral coppite yi, loolu dina noppal waa wikipedia yi
|}
Ligne 38 ⟶ 36 :
;[[Aide:sàqum jëfandikukat| sàqum jëfandikukat]]:Doonte doonul lu manut a ñàkk, bindu ngir mana cëru, waaye am na ay ngënéel yu jar a bàyyi-xel ci def ko. Xool leen nu ñuy bindóo.
;[[Tànneefu Jëfandikukat]]:Léegi nga xam ne bindu nga ba noppi, man ngaa dugg ci ''samay tànneef'' soppi ko ci ni nga ko bëggee.
;[[Ndimbal ci ay nataal]]: Fii di nañ la fi won nooy sosee am sàqum jëfandikukat, jaare ko ciy nataal
;[[Xëtu jëfandikukat]]:ci sag bindu, am na aw xët wu ñu lay jagleel, foofu ngay bind dara ci yaw
;[[Soppi turu jëfandikukat]]:Su fekkee sa turu jëfandikukat neexatu la, man nga koo soppi ci lu gaaw, leeral ni yaa ngi ci wii xët