Xam-xamu suuf si ak jawwu ji wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Rëdd 17 :
Mbooleem beeñ bi ak [[doj yi]] ñoo sos wàll gu tond (superficiel), gu dëgër gu [[kol-kolu suuf si]], ñu koy woowe [[Jéeri ji]] walla aji wow ji.
 
bu ñu séddalee Jéeri ji, def ko ñeenti xaaj, ñatt yi daanaka ndox yee leen muur, yooyu ndox nag ñoo sos [[mbàmbulaan yi]] ak géej yi, waaye wàll yi génn ci jéeri ji; nga xam ne ndox yi muuruñu leen ([[gox yi]] ak [[dun yi]] , wàll yii ñooy [[wërlaay]] gu dëppoo te méngoo ak dundug nit, moo tax fi layla nit di dunde, di fi defe ay liggéeyam, walla li ëpp ci ay cawarteem (activités).
 
Jéeri ji nag day dund tey màgg ci anam gu sax, ak doonte fi nun, day mel ne ni mu nekke soppikuwul. Li ko waral nag mooy ni muy soppikoo day faral a yeex lool: doj yi bu ñu sosoo ci ron géej gi, dañuy mujj lemu, yékkatiku, màgg ànd ak [[Jamono yu jiyoloji yi]]ñooy mujj sos ay càllalay doj yu yees.