Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Rëdd 211 :
9 – agsig dara lu dul aw ñam ba ci mbaq gi (biir bi) jaare ko ci gimiñ gi, muy lu mel ne wann ab jaaro walla ag wёñ, ngir li ñu jёle ci Ibnu Abaas mu ne : “ koor mooy li dugg, du li génn” mu bёgg a wax (y.y.g) ne: koor mi ngi yaqoo ci liy dugg ci biiru nit ki, waaye du yàqoo ci li ciy génne niki dereet walla am waccu.
 
10 murtad (mooy tubbi) ak doonte dellusiwaat na ci Lislaam, ngir waxam ja (t,s) {{boo bokkaalee sa jёf dana sippiku te danga bokk ci ñu ñàkk ñi (ñu pert ñi)}}
 
Yii yépp dañuy yàq koor tey waral fayug bis ba ca yàqoo, waaye nag duñu waral kafaara, ndaxte kafaara moom du ware ndare ci ñaari way yàq koor yii:
Rëdd 217 :
1 – séy bu ñu tay te kenn manantewu la ci, ngir waxi Abuu Hurayra ja (y.y.g) : “waay ñёw na ci Yonnant bi (j.m), ne ko man de alku naa yaw Yonnantub Yàlla bi, mu ne ko : lu la alag ? mu ne ko séy naak sama soxna ci ramadaan. Mu ne ko : ndax am nga jaam boo goreel? Mu ne deedeet, mu ne ko ndax man ngaa woor ñaari weer yu toftaloo? Mu ne ko deedeet, mu ne ko ndax am nga lu man a leel juroom benn fukki miskiin ? mu ne ko deedeet, daal di toog, Yonnant bi (j.m) daal di indi as ndàmba su def tàndar ma, ne ko am saraxeel lii, mu ne ko ndax dama koy sarax ku ma gёn a ñàkk? Yonnant bi ree ba ñuy gis bёñam ya, mu ne : demal jox ko sa ñoñ”
 
2 – lekk mbaa naan ci lu dul ngant lu ñu daganal: ci Aboo Haniifa ak Maalik (y.y.g), seenub tegtal mooy : “waay dog na ci ramadaan Yonnant bi (j.m) digal ko mu kafaara” ak àddiisu Aboo Hurayrat (y.y.g) mu ne : “waay ñёw na ci Yonnant bi (j.m) ne ko : dog naa ci ramadaan te tay ko, Yonnant bi ne ko: goreelal ab jaam, mbaa nga woor ñaari weer yu toftaloo, mbaa nga leel juroom benn fukki miskiin”
 
=== li ñu daganal ci ku woor ===
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële