Ubbi njël lu njëkk li

Modifications

5 octets supprimés ,  il y a 10 ans
Coppite gi amul tënk
[[Moom]] nag cim koom ak naataange la daa dunde ci péeyam, waa diiwaan bii it dañu ko daa indil ay kem ci wurus wi ñiy génnee [[ci]] suuf si, ginnaaw bi mu faatoo nag la ko fi ab jarbaatam wuutu.
[[Ci]] atum [[1052 g.j.]], la [[Muraabituun]] yi song Gana, ci layuw dañuy dugal ñoñam ci lislaam, ñu daal di ubbi péey ba atum [[1076 g.j.]], [[ginnaaw]] bi Gana néew doole, daal di daanu ci mujjantal gi ci loxoy [[imbraatóor gu Mali]] atum [[1240 g.j.]]
 
 
{{Buntutaariix}}
{{Wikibaatukaay}}
 
 
{{DEFAULTSORT:Gana}}
[[Wàll::NguuriTaariixu Afrig]]
 
[[Wàll::TaariixuNguuri Afrig]]
[[Wàll::Nguuri Afrig]]
 
[[ar:إمبراطورية غانا]]
5 231

modifications