Mandinke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ptbotgourou (waxtaancëru)
m re-categorisation per CFD, Replaced: Catégorie → Wàll:
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
 
Rëdd 1 :
Mandinke, ci xeet Soose yi lanu bokk. Ñoom ñoo taxawal imbraatooru [[Mali]], ak nguuru Kaabu, [[Ñaani]], [[Wulli]] ci [[senegaal]]. Sunjata Kayta Mandinke la. Mandinke am nañu tuur yu bari: Malinke ci [[français]], manding, Mandinka mooy tur wi ñu tudde seen bopp. Ci seeni làkk, Mandinka mooy: nit ku juge Mande. Mande mooy Reéwum mandinka yi, ci réewum Mali. Seeni Sant: Kayta, Jara, Siise, Ture, Kuyaate, Sumaare, Fakoli, Dumbuya, Dumbiya, Bakayogo. Buuru mandinke Mansa lay tudd.
 
[[Wàll::Taariixu senegaal]]