Ne-ne wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ptbotgourou (waxtaancëru)
m re-categorisation per CFD, Replaced: Catégorie → Wàll: (3)
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Ne-ne, ñu xame ko ci frãse ci((matière))mooy li toggale (li composer) wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible. Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër(l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël [[barab (déggiit)|barab]](elle occupe de l'espace)te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci [[jóor]](la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne(particules de matière), deesi jëfandikoo [[mol]](la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu [[jëmm]], lepp lu am ab jóor rekk [[ne-ne]] la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay [[bariyon]],kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne '''[[Baryon#Matière baryonique|ne-ne bu bariyon]]''' lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci[[boson|boson yu dàttu]] (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti [[doole yu dàttu]] yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
 
[[Wàll::ne-ne|* ]]
 
[[Wàll::Jëmm]]
 
[[Wàll::Simi]]
 
 
[[Wàll::ne-ne|*]]
 
[[ar:مادة]]
Ligne 72 ⟶ 69 :
[[yi:מאטריאל]]
[[zh:物质]]
 
 
[[Wàll::Jëmm]]
[[Wàll::Simi]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Ne-ne » lañ ko jële