Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Rëdd 261 :
Njariñ li nekk ci kafaara mooy ñogal sariiya ba duñu ko foye, di xotti wormaam. Moom itam day laabal bakkanub jullit bi ci jeexiiti bàkkaari wuuteek ndigali Yonnant bi (j.m), yi ñu def ci lu dul ngànt, looloo tax ñu war a defe kafaara ni ñu ko yoonale ci kem bi ak naka gi (ni muy tollu ak ni nu koy defe), bu ko defee mu man moom kafaara def li ko taxoon a jug, muy far bàkkaar bi aki jeexiitam ci bakkanu jullit bi. Cosaanul kafaara mooy waxi Yàlla ji (t.s): "yu rafet yi danañu demal (dañal) yu ñaaw yi" ak waxi Yonnant bi (j.m) : “ragalal Yàlla foo man a nekk, lu ñaaw (loo man a def) toppal ca lu rafet, dana ko far, àndal ak nit ñi ci jikko ju rafet”
 
[[catégorieWàll:Ponki Lislaam]]
[[catégorieWàll:Lislaam]]
 
[[catégorie:Lislaam]]
 
[[ar:رمضان]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële