Namandiru wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Gamadji~wowiki (waxtaancëru)
Xët wu bees : Namandiru, nekkoona nguruu gu nek Senegaal ca jamono yu yag ya. Ca VIIeelu xarnu amna ben njabotay nu tuddu Ja-Ogo, noow nañu deuk ca penku Senegaal, ca wetu dexug Senegaal. Ja-Ogo, …
 
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Namandiru, nekkoona nguruu gu nek Senegaal ca jamono yu yag ya. Ca VIIeelu xarnu amna ben njabotay nu tuddu Ja-Ogo, noow nañu deuk ca penku Senegaal, ca wetu dexug Senegaal. Ja-Ogo, Misra lañu jogué. Daw nañu wa Misra ndax fofu, ay jaambar nu tudd Perse, noow nañu ca biir Misra, di sonalate deuk bi. Li moye tax Ja-Ogo yi, daw neen ba agsi dexug Senegaal. Ca deuk bobu, ken nekku fi woon. Ca senegaal tabax nanu nguruu Namandiru.
Ja-Ogo yi, teug mo donewoon seen liguey. Ja-Ogo yi ño tugguduggu liguey bi ca Senegaal. Li moye tax ca jamono bobu teug yi ay buur gu mak lañi nekkoon. Ndax ntakaye yi, pakaa yi, Kaas yi, lêp lañu defé ak weñ, ñom rek ño xamoon lolu. Ja-Ogo yi, amna yu bari deñi né, ca Pël lañu bokkoon, ndax tuur bi lanu joxé seni nguur ''Namandiru'', ca lakku Pël moye= Rewmi am lëp. Ja-ogo ño tabax tamit nguruu Tekrur, tey di nek Fuuta-Toro.
 
Njabotu Manna yi, ño daanel Ja-Ogo yi. Manna yi ay Saraxule lañi nekkoon, di sant Naxate.
Tamit Naari ca Xeelu xarnu, ak seen buur Abu Bakr Bin Omar, xeex nañu ak Ja-Ogo yi.
Manna yi ak Naari moye tax, Nguruu Namandiru daan.
Rëdd 8 :
== Nguruu Njaarmeew ==
 
Ba nopi, amna benene njanotaynjabotay nu sant Ndaw, gu jogué Gannar, diwaanu guidimaxa, noow nañu ca deuk bi amon Namandiru, di fi tabax benene nguuru bu tudd Nguruu Njarmeew. Seen Buur Belëp la tuddu. Ndaw Belëp yi, yaguñu fa. Ndax ca XVeelu xarnu, Buurba Jolof ba, Tyukuli Ndiklam, uuf na deuk bi ca biir Jolof, ak Tekrur itam. Kon Ndaw Belëp yi, daw nañu ba Nguruu Seereer yi ca Saluum. Fofu Maad Saluum bi, Mbegane Ndour, mey na bene Diwaan buuru Ndaw BeëpBelëp bi, mom Waly Mberu Mbacké Ndaw la tudd. Diwaan bi, Ndukuman la.
 
Koly Tenguela, ca XVIeelu xarnu, Njaarmeew bi jël nako, sogo Malik dawda Sy Toorodo bi, noow fofu di tabax Nguruu Bundu.