Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal.[[ Wolof]] ñoo ëpp ci waaso yi ci Senegaal [[Image:OuolofCayor.jpg|thumb|left|Wolofu [[Kajoor]] (boyaade (gravure) gu [[1890]])]].
Maami wolof yi Isipt lañu bawoo. [[Séeréer]] si, Pël yi, [[Sooninke]] yi, Tekuruur yi (Tukuloor), ak SaraxuleSara yi juge nguuru Bagirmi ca réewum [[Cadd]]. Wolof yi ca xeet ya lañu juge. Xeet ya yépp danoo jaxasoo, ca yoonu Imbraatoor gu Ghana, ca dëkk bi nu tuddé Jolof. Wolof mooy ñu bawoo Jolof, Waa-Lof (ay gaa yu juge Lof) walla Waa-Laf (ñoñ Laf), di nekk tay Wolof. [[Seex Anta Joob]], Walaf la doon wax. Noonu la xeetu Wolof judoo. Tur wii nuy wax Jolof, benn Soose bu tundoon Jolof Mbeng moo ko joxoon dëkk ba. Ca cosaan dañu ne Jolof Mbeng ak njabootam ñoo fa njëkkoon a dëkk. Ba noppi Amadu Abuubakar ñëw fa, moom baayam Naaru Murabituun la woon, turam di Abu Bakr Ben Omar, ca cosaan danu daa wax Abu Dardaayi, yaayam Tukuloor la woon, turam di Fatumata Sàll doomu Lam-Tooro (Lamanu Tooro) ca [[Tekuruur]]. Amadu, Baayam jenn jàmbaar ju Saraxule moo ko ray, booba nag la Fatumata seeti jeneen jëkër. Amadu bégul woon ci boroom këru nday ju bees ji, lii a taxoon mu dem Waalo. Foofa nag nit ña fa nekk ay [[Laman]]i [[Séeréer]] yu sant Ngom aki Sàmmkati Pël yu sant Jaw. Laman yi danoo yékkati woon Amadu, ndax dafa baaxoon ba jaaxal dëkk bi, ba far mujj di Buuru [[Waalo]]. Séeréer si ñoo ko tudde [[Njaajaan Njaay]]. Ndax Mbaanu Njaay mooy Gaynde (Gaynde Njaay ca cosaan) te Gaynde mooy buuru àll ba.
Waaye ba noppi Njaajaan dañu koo dàqe dëkk ba, ndax daa am ku ko bëggoon a ray. Mu daal di woon daw ba Jolof ca Wolof ya. Njaajaan Njaay dajale woon na Wolof yi ndax ñu gën a am doole, ba man a taxawal Imbraatóor gu Djolof. Wolof yi, [[Jolof]] mooy seeni dëkk, waaye ak seeni imbraatoor gi, dañoo demoon dëkk te yor: [[Waalo]], [[Tekuruur]], [[Kajoor]], [[Bawal]], [[Siin-Saalum]], Njarmeew (soog a dëkk Bundu), Ñaani, Wulli, Bambug. Nguur ga gépp Jolof uffoon na ko. Lii moo tax Làkku Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]]. Ca atum 1549 la Jolof gu mag ga tas ak Lele Fuli Fak. Nguuri Wolof yépp am seeni buuri bopp: Dammeel ca Kajoor, Teeñ ca Bawal, Baraag ca Waalo, Buurba ca Jolof (Ca Jolof gu mag ga, Buur Fari lañu daa wax). Decce Fu Njóogu ak Amari Ngóone Sabel Faal, ñoo fi njëkk a nekk Dammeel-Teeñ.