Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
Waaye ba noppi Njaajaan dañu koo dàqe dëkk ba, ndax daa am ku ko bëggoon a ray. Mu daal di woon daw ba Jolof ca Wolof ya. Njaajaan Njaay dajale woon na Wolof yi ndax ñu gën a am doole, ba man a taxawal Imbraatóor gu Djolof. Wolof yi, [[Jolof]] mooy seeni dëkk, waaye ak seeni imbraatoor gi, dañoo demoon dëkk te yor: [[Waalo]], [[Tekuruur]], [[Kajoor]], [[Bawal]], [[Siin-Saalum]], Njarmeew (soog a dëkk Bundu), Ñaani, Wulli, Bambug. Nguur ga gépp Jolof uffoon na ko. Lii moo tax Làkku Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]]. Ca atum 1549 la Jolof gu mag ga tas ak Lele Fuli Fak. Nguuri Wolof yépp am seeni buuri bopp: Dammeel ca Kajoor, Teeñ ca Bawal, Baraag ca Waalo, Buurba ca Jolof (Ca Jolof gu mag ga, Buur Fari lañu daa wax). Decce Fu Njóogu ak Amari Ngóone Sabel Faal, ñoo fi njëkk a nekk Dammeel-Teeñ.
 
'''== Njabooti Wolof yooyu, ñooyi yoroon nguuri wolof yi:''' ==
* Njaay (Jolof)
* Mbóoj ak Wàdd (Waalo)
Rëdd 9 :
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|ab [[Ceddo]] ca wetu [[Bàkkel]] ([[1853]])]]
 
'''== Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:'''==
 
* Géer/Garmi, ca kaw, ñoo doon nekk buur yi. Kàŋam (buuri Laman yi) Farba Kaba (buuri [[Ceddo]] yi), Tuube, Bumi ak Lingeer.
Ca seeni meen ñoo man a nekk Buur. Meen moo gën a am solo Geño('''[[Meen]]''':wàllug nday). '''[[Geño]]''':wàllug baay .
Ligne 16 ⟶ 15 :
* Baadoola, Mbay moo doonoon seen dund.
 
'''==Ñeeño yi:'''==
 
* Tëgg, Lawbe, Wuude, Ràbb. Am na ñu bari ci ñoom ci xeetu Pël/Tukuloor lañu juge ñooy ñi sant : Caam, Mbow, Ace, Jaw, Jum, Taal, Faam, Gise, Sow. Ñeeño yooyu dañuy kalante ak Pël yi, ndax danoo bokk maam.
Ligne 22 ⟶ 21 :
* Géwal yi, ñépp lañuy woy, Buur yi, ñeeño yi. Cosaanu nit ñépp lañu xam, seeni Sant yi gën a siiw: Sekk, Mbay, Mbuub, Laam, Séy .
 
'''=Jaam yi:'''==
 
* Am na jaami buur yi ( Ceddo yi), Jaami Juddu, Jaami Sayor (ñoom ca xare lees leen daan ame ak a jàppe). Xeet wu nekk nag lanu daan juge.
Ligne 29 ⟶ 28 :
Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkatu Tukuloor) walla Sebbe (Ceddo/Jàmbaar Tukulóor) Walla Tooroodo, lanu. Danoo teel a nekk foofu.
Ci Senegaal ñoom ñoo njëkk a gis Tubaab yi. Bu njëkk Ceddo lañu woon, tay ñu bari ci [[yoonu murit]] lañu bokk walla tiijaaniya. Am na ay ay nasaraan (chrétiens) tamit waaye duñu ñu bari (Gore/Ndar). [[Seex Ahmadu Bamba]] Mbakke ak [[Alaaji Maalik SI]] ñoo gën a dugal Wolof yi ci [[lislaam]]. Wolof yu bari gàddaay nanu (walla tukki nanu) dem Faraas, [[Diiwaan yu Bennoo]] yi (États-unis), Itaali, Espaañ. Ci Senegaal ñoo yor pal yi gën a rëy (loolu du lu ñépp man a ànd, ndax gisees na ne Njiitul Senegaal lu njëkk séeréer la woon la ca topp it noonu, boo demee ca xare ba (l'armée)lu ëpp ca kilifa ya doonuñu ko. Kon wax jooju ju deesi xoolaat la). Ñoom ñoo gën a fonk seeni réewm (Nationalisme Sénégalais). Am na ci ñoñ ci Mbay (Kaw-Kaw) lanuy dunde, am ci ñoñ ci Napp, ca géej gi (ci ñoom la Lébu yi bokk). Jom ak Teraanga ci ñoom la fekk baax.
[[Catégorie:Taariixuwaasoy senegaal]]