Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
orthografie
Ibou (waxtaancëru)
jubbantig mbindiin
 
Rëdd 3 :
----
== Li muy jariñ ==
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñéppa deggantedéggante. Am na ñu degguldéggul wolof, walla seenseenug dégg des na, ñu mana soxla ku ñu jokkool ci làkk wi ñu dégg, walla ci wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu degguldéggul wolof te di bëgga jàpp ci liggéey bi, kon di na am-solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen mana waxtaane, ngir njariñam mana feeñ.
 
Bii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan wu barilàkk wu mel ne wu Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof bu ab jëfandikukat bu bindu.
Rëdd 13 :
**Misaal: '''{{Babel|''' (3 làkk)
 
Su ko defeen nag nga def ci tolluwaayu ni nga dégge wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añseañs.
 
Misaal: