Pël wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Gamadji~wowiki (waxtaancëru)
Xët wu bees : Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël y ca Sowwu Afrig, danu bokk ca xet y nio gëneu bari. Senegaal, Mali, Gànnar, Gaambi, Ginee, Ginee Bisaawoo, Niseer, Burkina Faso, Niseeria, ...
 
Gamadji~wowiki (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël y ca Sowwu Afrig, danu bokk ca xet y nio gëneu bari. Senegaal, Mali, Gànnar, Gaambi, Ginee, Ginee Bisaawoo, Niseer, Burkina Faso, Niseeria, Benin, Kot Diwaar, Kameroon, Réewum Diggu Afrig, ba Sudaan, ca réewum y yëp Pël y nio ngi fa.
Xet bobu amna nu tuuri bari: Pël ca Wolof, ca afrig mo tuuru gëna siiw, Fula ca Mandée y, Fulani ca Naari, Fellata wala Fellan ca Sudaan.
Pël[[Image:Eleveurs daniPeuls.jpg|thumb|200px|left|Éleveurs tuddpeuls senidu bopp:Gourma, sud de [[Gao]], [[Mali]]]]Pullo wala FulBe. Isipt moye deuk bi nu juddu. Pël y ca Isipt aye nit ku nul lani nekkone. Ba paré ay nit ku wéex, nio na nu ca seni deuk, niom réewum Asiak tugal lani jogue woon, bokk ca xeti: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari bi nu tudd ca lakk tubap y (Indo-européen). Pël y niul y aki nit ku wéer nonu, danu jaxaasé. Li moye tax Pël y da nu gëna xées, gëna séew, am karowu gëna noye, yenene xetu nul y ca Afrig. Ba nopi, Imbratoor gu Tirki (Perse), uuf nanu réewum Isipt, di fa tek dundu meti ca niul y. li moye tax Pël ak Séeréer y dem nanu deuk ca Sudaan (Nubie) deuki seni mam, sogo dem Senegaal. Pël ak Séeréer danu bokk mam, seni lakk tamit. Yag nanu and, danu kalenté. Ca yonu Tekuruur, pël y ca Dexug Senegaal rek lani nekkone ak seni Nak. Bobu nekkunu juulit. Amunu woon nguruu ndax ak seni nak ca tuki rek lani dundé. Meew ak Sankhal modon seni lek. Pël ci sen bopp amna xet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo bi moye seni Buur: JaawBe y, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Amna yenene KinDe. Tuki bi nu dund moye tax turu na nu ca Soowu Afrig yëp ba niowat Sudaan, di muun ndax sasounek ca deuki njabuur lani dund.
 
Ca atum 1539 Koly Tenguella Bâ, ca Pël la bokk ca bayam, ca Mandé y la bokk ca yayam (Keyta), dadjalé na sambkatu Pël y ak mandé y, ndax nu meunteu am dolé. Ca Jambaram da di dugg ay yenene xet (Wolof, Séeréer, Bajaaranké, Jola, Baga, Sooninke ya. Niom yëp ak sen ArDo Koly Tenguella, yég nanu ba Tekuruur, di xéer ag Buurba Jolof ba ndax ki modone yoor deuk bi, ak Lam-Toro y, Lam-Térmes, Lam-Taga, Juroom nent fan sogo yoox deuk bi. Koly Tenguella deg nafa njabotam (Denyakoobé y), tuddu na nguruu bi Fuuta-Toro (Fuuta moye Deuku Pël ca seni Lakk). Li ca Senegal la xeewé.
Rëdd 35 :
Sankara, Sankaré, Shagari, li yëp bene la.
Amna Pël yu bari demna nu ca Wolof yi li moye tax amna ay wolof ku sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sall). Tamit amna Xët yu bari nio nanu ca Pël, li moye tax amna ay Pël ku sant Cissé, Tuuré, Njaay, Jakité, Kamara ak yenene sant.
 
<gallery>
Image:Peul.jpg|Guerrier
Image:Berger-peul.jpg|Berger
Image:Femme-peule.jpg|Femme
</gallery>
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Pël » lañ ko jële