Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal.[[ Wolof]] nio fi eup ca xetu sénégal [[Image:OuolofCayor.jpg|thumb|left|Wolof du [[Cayor]] (gravure de [[1890]])]].
Mamu wolof y isipt lanu jogue. Séereer[[Séeréer]] y, Pël, [[Sooninke]], Tekuruuri (Tukuloor), ak Sara u jogué nguruu Baguirmi ca rewm Tchad,. Wolof y ca xeet y lanu jogue. Xeet ni yéep da nu jaxaasé, ca yonu Imbratoor gu Ghana, ca deuk bi nu tuddé Djolof. Wolof moye ku jogué Djolof, Wa-Lof (ku jogué Lof) wala Wa-Laf (ku jogué Laf), di nek tey Wolof. [[Seex Anta Joob]], Walaf la done waxé. Nonu la xeetu Wolof judu. Tuur bi li nu wax Djolof, bene SocésSocé ku tundu Djolof Mbengue moko joox deuk bi. Ca cossan da nu né jolof Mbengue ak njabotam mo fi dieuk nek. Ba nopi Amadu Abubakar niow na, mom bayam Naaru Murabin la woon, tuuram Abu Bakr Ben Omar, ca cossan danu wax Abu Dardaï, yayam Tukuloor la woon tuuram Fatumata Sall domu Lam-Toro (Lamanu Toro) ca tekuruur[[Tekuruur]]. Amadu, Bayam ben jambar Saraxule moko rey, bobu nak Fatumata setsina bénene dieuker. Amadu bougou woon dieuker bou bess bi, li moye tax da fa daaw ca Waalo. Fofu nak nit y fi nek ay Lamanu Séereer yu sant Ngom aki Sambkatu Pël yu sant Diaw. Laman y danu yékéti Amadu, Ndax da fa baxone ba jaaxal deuk bi, ba nek Buuru Waalo. Séereer y nio ko tudd Njaajan Njaay. Ndax Mbaanu Njaay moye Gaïndé (Gaïndé Njaay ca cossan) té Gaïndé moye buuru all ba.
Wa é ba paré Njaajan deen ko daq deuk bi, ndax amna nu ku bougoune ko rey. Daaw na ba Djolof ca Wolof y. Njaajan Njaay da dadjalé Wolof y ndax nu menteu geuneu am dolé, ba meunteu tabaax Imbratoor gu Djolof. Wolof, [[Jolof]] moye seni deuk wa é ak seni imbratoor gi, da nu dem deuk té yoor: Waalo, Tekuruur, Kajoor, Bawol, Sine-Saloum, Njaarmew (sogo nek Bundu), Niani, Wulli, Bambouk. Nguruu gi yéep Djolof uff na ko. Li moye tax Lakku Wolof moye lakku nit ni geuneu wax ca senegal. Atu 1549, Jolof bu makk ngi tass na ak Lélé Fuli Fak. Nguruu Wolof yéep am seni buuru bop: Damel Kajoor, Teigne Bawal, Braak Waalo, Buurba Jolof (Ca Jolof bu mak nga, Buur Fari lanu waxon). Dethié Fu Njoogu ak Amari Ngoné Sobel Faal, nio fi dieuk nek Damel-Teigne.
Wolof, Jolof moye seni deuk wa é ak seni imbratoor gi, da nu dem deuk té yoor: Waalo, Tekuruur, Kajoor, Bawol, Sine-Saloum, Njaarmew (sogo nek Bundu), Niani, Wulli, Bambouk. Nguruu gi yéep Djolof uff na ko.
Li moye tax Lakku Wolof moye lakku nit ni geuneu wax ca senegal. Atu 1549, Jolof bu makk ngi tass na ak Lélé Fuli Fak. Nguruu Wolof yéep am seni buuru bop: Damel Kajoor, Teigne Bawal, Braak Waalo, Buurba Jolof (Ca Jolof bu mak Buur Fari lanu waxon). Dethié Fu Njoogu ak Amari Ngoné Sobel Faal, nio fi dieuk nek Damel-Teigne.
 
Njabotu Wolof nonu, nio yoron nguruu wolof y:
* Njaay (Jolof)
* Mbodji ak Wade (Waalo)
* Faal ak Joop (Kajoor ak Bawal)
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|Un [[tiedos|tiedo]] près de [[Bakel (Sénégal)|Bakel]] ([[1853]])]]
Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon y:
* Géer/Garmi, ca kaw, nio done buuri. Kangam (buuri Laman y) Farba Kaba (buuri [[Ceddo]] y), Toubé, Boumi, ak Linguére.
Ca seeni meen nio meunteu nek Buur. Meen mo geuneu am solo Guegno.
* Jambour ak Serign y. Niom Serign y ay Tukuloor (Dia, Sy, Lô, Sall) Saraxule (Sylla, Khoulé, Cissé, Dramé, Kébé) wala ay Naar (Diakhoumpa, Aïdara, Coundoul, Sady, Babou) lani doon.
* Badolo, Mbey mo done seeni dund.
 
Neeno y:
* Teug y, Lawbe, Wuude, Rabb y. AmnaAm nanu bari ca xetu Pël/Tukuloor lani jogué moye Njabotu : Thiam, Mbow, Athié, Diaw, Dioum, Tall, Fam, Guissé, Sow. Neeno nonu dani kalenté ak Pël y, ndax dani mbokk mam.
Neeno u Wolof: Beye, Niasse, Dieng, Mbaye, Niang.
* Gueweul y, nieup lani way, Buuri, Neeno. Cossanu nit yeup lani xaam, seni Sant yu geuneu siiw: Seck, Mbaye, Mboup, Lam, Seye .
 
Jaam y:
* Amna jaami buuri ( Ceddo ), Jaami Juddu, Jaami Sayor (Niom ca xeer lanu done ko dieul). Xeet gunek lani djogué.
 
Wolof y danu jaxaasé li moye tax seni sant danu bari, tamit xet yu bari niow nanu ca niom (Wolofisation). Seex Anta joop né na, Wolof y deug deug no: Njaay, joop, Faal, Niang, Beye, Mbodji, Mboup, Wade, Gueye. Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkat Tukuloor) wala Sebbe (Ceddo/Jambar Tukuloor) Wala Toroodo, lani nek. Da ni tel nek fofu.
Ca senegal niom no dieuk giss Tubap y. Bou dieuk Ceddo lani woon, tey you bari ca yoonu murid lanu nek wala tidjanya. Amna ay chrétien tamit ( Gorée-Saint-Louis). Seex Amadu Bamba Mbakké ak El Adj Malik Sy nio geuneu duggal Wolof y ca lislaam. Wolof yu bari tuxu neen Fraanse, Etat-unis, Italie, Espagne. Ca senegal da niu yoré posty yu geuneu Mag. Niom no geuneu fonk seni rewm (Nationalisme Sénégalais). Amna nu da nuy dund ca Mbey (Kaw-Kaw), Napp ca guedj bi (ca niom Lebu y lani bokk). Jom ak Teraanga ca niom la jogué.