Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
o
 
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal. Wolof nio fi eup ca xetu sénégal [[Image:OuolofCayor.jpg|thumb|left|Wolof du [[Cayor]] (gravure de [[1890]])]].
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal. Wolof nio fi eup ca xetu sénégal. Mamu wolof y isipt lanu jogue. Séereer y, Pël, Sooninke, Tekuruuri (Tukuloor), ak Sara u jogué nguruu Baguirmi ca rewm Tchad, Wolof y ca xeet y lanu jogue. Xeet ni yéep da nu jaxaasé, ca yonu Imbratoor gu Ghana, ca deuk bi nu tuddé Djolof. Wolof moye ku jogué Djolof, Wa-Lof (ku jogué Lof) wala Wa-Laf (ku jogué Laf), di nek tey Wolof. Seex Anta Joob, Walaf la done waxé. Nonu la xeetu Wolof judu. Tuur bi li nu wax Djolof, bene Socés ku tundu Djolof Mbengue moko joox deuk bi. Ca cossan da nu né jolof Mbengue mo fi dieuk nek. Ba nopi Amadu Abubakar niow na, mom bayam Naaru Murabin la woon, tuuram Abu Bakr Ben Omar ca cossan danu wax Abu Dardaï, yayam Tukuloor la woon tuuram Fatumata Sall domu Lam-Toro (Lamanu Toro) ca tekuruur.Amadu, Bayam ben jambar Saraxule moko rey, bobu nak Fatumata setsina bénene dieuker. Amadu bougou woon dieuker bou bess bi, li moye tax da fa daaw ca Waalo. Fofu nak nit y fi nek ay Lamanu Séereer yu sant Ngom aki Sambkatu Pël yu sant Diaw. Laman y danu yékéti Amadu, Ndax da fa baxone ba jaaxal deuk bi, ba nek Buuru Waalo. Séereer y nio ko tudd Njaajan Njaay. Ndax Mbaanu Njaay moye Gaïndé (Gaïndé Njaay ca cossan).
Wa é ba paré Njaajan deen ko daq deuk bi, amna nu ku bougoune ko rey. Daaw na ba Djolof ca Wolof y. Njaajan Njaay da dadjalé Wolof y ndax nu menteu geuneu am dolé, ba meunteu tabaax Imbratoor gu Djolof.
Wolof, Jolof moye seni deuk wa é ak seni imbratoor gi, da nu dem deuk té yoor: Waalo, Tekuruur, Kajoor, Bawol, Sine-Saloum, Njaarmew (sogo nek Bundu), Niani, Wulli, Bambouk. Nguruu gi yéep Djolof uff na ko.
Ligne 8 ⟶ 9 :
* Mbodji ak Wade (Waalo)
* Faal ak Joop (Kajoor ak Bawal)
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|Un [[tiedos|tiedo]] près de [[Bakel (Sénégal)|Bakel]] ([[1853]])]]
 
Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon y:
* Géer/Garmi, ca kaw, nio done buuri. Kangam (buuri Laman y) Farba Kaba (buuri Ceddo y), Toubé, Boumi, Linguére.