Séeréer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Séeréer bengenn xetgiir ula nekgu senegalnekk la[[Senegaal]]. Séeréer ysi nioñoo juurjur LébuLebu yyi ak [[Wolof]] yyi, wa éwaaye [[wolof]] amnaam nunañu yénenyeneen xetxeet fuyu muñu djoguébawoo tamittam yu duli Séeréer. SineSiin ak SaloumSaalum moyemooy seniseeni nguruunguur.[[Image:SererMan.jpg|thumb|left|Tisserand sérère de [[Mbissel]] (aquarelle de l'[[David Boilat|abbé Boilat]] dans ''Esquisses sénégalaises'', [[1853]])]] Sogo nek Sine-saloum, ca [[Tekuruur]] lani nékone. Da niu tuki Sine-Saloum ndax dani dawone lislaam ak Almoravide y. Almoravide y danu xerone (jihad) ak séeréer ndax nu dugg ti lislaam, wa é séeréér y bugunuone lolu. Li yéep ca yonu imbratoor gu Ghana la xéw, bobu imbratoor gi mu ngi done dan. Fofu ca Sine-Saloum ay Socé ([[Sooninke]]), nio fi done deuk. kon bokk Socé ak Séeréer deukénté lani def, wa é ba nopi socé yu bari dem nanu deuk ca kaasamaas. Séeréer dani done sédellé deuk bi ci ay Lamana, ca Lamana yéep ay Laman nio fi done buur. Mbey ak Napp, ca lolu lani done dundé. Mbey (Saloum) mo done tuuru deuk bi sogo nek Sine ak Saloum. Ba paré ay Mandinke u djogué nguruu Kaabu, niow na nu ca Séeréer yi, deuk ak niom. [[Mandinke]] y ay Nanco (Géer) u Kabbu lani woon, seni buur (Mansa ca lakk Mandinke) nio lene dakk seeni rewm. Jola y nio lene né ca Sine-Saloum baxna yéep yu nit a soxla ndax mou menteu dund amna fa, té fofu amna ay nit wa é amnu buuru deug. Li moye tax tuxu nanu Sine ak Saloum. Nanco ak Buuru Séeréer yi fi nékone (Laman) danu bolo, jaxaasé, baa nek bu nu tudd ay Gelowaar. Gelowaar nonu, nio tabax nguruu Sine ak Saloum. Maysa waly Dione moye dieuk nek buuru Sine. Mbegan Ndour moye dieuk nek Buuru Saloum.
Ca niom:
*Gelowaar nio Buuri.