Séeréer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 7 :
Séeréer ca seni bop, amna: Séereer y Niominka, Sine rek lani nek nappkat lanu tuuru mandinke lani am ndax ca gelowaar lene bokk. Séeréer Ndut, Safen, Palor, None, niom Séeréeru [[Kajoor]] ak [[Bawal]] lanu.
Séeréer Sine, moye Séereeru Sine-Salum. Séereeru Fouta y nak, legui ay ca tukuloor y lanu bokk, niom nio fa done ak wolof tamit, Cuballo y (nappkat u tukuloor) ak Sebbe ( ceddo tukuloor ). Séereer ak Pël nio fi dieuk nék fofu li moye tax amna Seereerfa fofuay Seereer. Tukuloor ak Séeréer danu Kalenté aki Jola tamit. Ndax ca cossan bi, da nu wax, xet ni yeup dani bokk mam.
Séeréer y da nu xawa niul, djol ak yaramu degeur. Ca senegal niom nio fi dakk béuré.
 
Signaru Gorée-Saint-Louis ca xet Séeréer ak tubap lani bokké woon. Léopold Sédar Senghor, dieuk président u sénégal séeréer la woon ca baye am, Abdoul Diouf tamit. Blaise Diagne momit am bayam Séereer la woon.
Séereer bou dieuk Ceddo lanu nekone, tey nak ca lislaam li nu né ( Tijjanya, Muridya), wala christianisme ca Sine (Joal-Fadiouth). Missionairu tubap mo lene duggu ca christianisme.
 
Seni Sant yi geuneu siiw : Diouf, Ngom, Faye, Sène, Sarr, Senghor, Ndour, Dione, Dior, Diong, Dieye, Seck, Ndong, Seye, Loum, Tine, Diene, Pouye, Thiaw, Marone, Gningue, Diob, Gadio.