Sooninke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Xët wu bees : Saraxule ben xet la, ca askanu mandé lanu bokk. Saraxule nio fi dieuk duggu ca islam, ti rewm Senegal, Xet bobu nio juur Jula y. Djité nanu Wolof y ca Kajoor ak Baol Se...
(Aucune différence)

Sumb bu 1 Fewriyee 2009 à 04:25

Saraxule ben xet la, ca askanu mandé lanu bokk. Saraxule nio fi dieuk duggu ca islam, ti rewm Senegal, Xet bobu nio juur Jula y. Djité nanu Wolof y ca Kajoor ak Baol Serere y ca Sine ak Saloum ca fofu yep nio fi dieuk nek. Imbraator u Ghana niom nio ko tabaax, ak nguruu Gadiaga, nguruu Jaara. Seni buur Tunka la tudd. Mbey moye seni dund, jaykat bu maak lanu. Ti sen cossan, amna nu yu bari y done tuki, ti jay kola-y, yeeré, Takkay, fep ti Mali, Senegal, Niger, Guinée ak Guinée-bissau, Maurétanie ba Cote-D'ivoire. Ti nit ku nuul y, danu bokk ca fi dieuk nio Europe. Ca Maurétanie danu bari ca deuk ba nu tudd Guidimakha, ti wet Fuuta-Toro la, fofu tamit nek nanu fa bou yagg, ba Tekuruur nékké. Mamadu Lamin Dramé, Serignu Saraxule bu djogué Gadiaga/Galam, bu nu wax tey Departement de Bakel, xér na ak tubaapi nu bougone uuf deuk bi ti sen rewm ti atum 1880. Moussa molo buuru Fulaadu nguuri Pël firduu, domu Alpha Yaya Molo Baldé, mo ko danel, bobu nak buuru Pël bi, ak tubaap la andalone. Mamadu lamin tubaap nio ko rey ti xer bi nu tuddé Xeru Toubacou ta, ca atum 1887. Saraxule ti sen askan:

  • Horon, nio done buuri.
  • Niakhamala, nio done neeno y, raabkat, wuudékat , teug y ak seen y.
  • Jaaro, waykatu buuri, xamna nu cossanu Saraxule yep, Kora ak Xalam y lanu way buuri (Tunka)
  • Komo nio done jaam y.

Wa é nieup da ni mbey, seni tollu bop-am. Seni Sant yu geuneu bari: Touré, Cissé, Bathily, Soumaré, Dramé, Kébé, Fofana, Dabo, Diabi, Sylla, Diakité, Sokhna, Tounkara.