Tekuruur wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
a
 
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Tekuruur modone nguruu tukuloor-y. xet yu bari tasséna nu fofu, Jogué Egypt: Serer-y, Wolof, Pël, Socés, Naar-y. Legui Tekuruur, Fuuta-toro la tuddu. Koly Tenguela Ba Silatigi bi moko jiox tuur bi. Ti nguruu bi, Tukuloor ak Pël nio fa eupé ba tey, wa é Serer-y nio fi dieuk nék ak Pël. Buur yu bari nio yor-on nguruu bi:
* Dia-Ogo-y ti yonu imbratoor-u Ghana.
* Manna-y.
* Tondyon-y.
* Lam-Termes, Lam-Taga, ak Lam-toro-y. Ti nu néké buur, jolof[[Jolof]] mo done uuf deuk bi, di fi ték ay Farba.
* Denyakobé-y yu Koly tenguela Ba, Sebee la nu one, Sebbe moye Cedoo.
* Almamy yu Torodo-y. Souleyman Baal ak Abdul Kader Kan, nio dakk denyakobé-y ti atu 1776. Ay Juulit la nu.
Ba paré tubap nio na nu ak colonisation bi ti atu 1890, dieul nguruu bi, rey Almamy-y, di cedellé deuk bi li nu wax ti lakku fraanse (Canton) ak (Provinces).
 
Tekrur moye deuk-u Tekruri. Tekruri moye tuur-u Tukuloor, bou dieuk nonu la nu tuddé-on seni bop. Tuur bi lu nu wax Tukuloor toubap moko fi indi, ndax xet bi dafa jaxaasé yu bari, amna ay Tukuloor seni mam [[wolof]] lanu, moye tukuloor yu sant Njaay, joop, Faal, Nang, Mbodj, yu demé nonu, amna nu seni mam-am ti xet-yu serer la ni jogué, Juuf, Saar, Faye, wala socés, Camara, Cissé, Tuuré.