Tekuruur wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
a
(Aucune différence)

Sumb bu 31 Samwiyee 2009 à 02:22

Tekuruur modone nguruu tukuloor-y. xet yu bari tasséna nu fofu: Serer-y, Wolof, Pël, Socés, Naar-y. Legui Tekuruur, Fuuta-toro la tuddu. Koly Tenguela Ba Silatigi bi moko jiox tuur bi. Ti nguruu bi, Tukuloor ak Pël nio fa eupé ba tey, wa é Serer-y nio fi dieuk nék ak Pël. Buur yu bari nio yor-on nguruu bi:

  • Dia-Ogo-y ti yonu imbratoor-u Ghana.
  • Manna-y.
  • Tondyon-y.
  • Lam-Termes, Lam-Taga, ak Lam-toro-y. Ti nu néké buur, jolof mo done uuf deuk bi, di fi ték ay Farba.
  • Denyakobé-y yu Koly tenguela Ba, Sebee la nu one, Sebbe moye Cedoo.
  • Almamy yu Torodo-y. Souleyman Baal ak Abdul Kader Kan, nio dakk denyakobé-y ti atu 1776. Ay Juulit la nu.

Ba paré tubap nio na nu ak colonisation bi ti atu 1890, dieul nguruu bi, rey Almamy-y, di cedellé deuk bi li nu wax ti lakku fraanse (Canton) ak (Provinces).

Tekrur moye deuk-u Tekruri. Tekruri moye tuur-u Tukuloor, bou dieuk nonu la nu tuddé-on seni bop. Tuur bi lu nu wax Tukuloor toubap moko fi indi, ndax xet bi dafa jaxaasé yu bari, amna ay Tukuloor seni mam wolof lanu, moye tukuloor yu sant Njaay, joop, Faal, yu demé nonu, amna nu seni mam-am ti xet-yu serer la ni jogué, Juuf, Saar, Faye, wala socés, Camara, Cissé, Tuuré.