Tugal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Synthebot (waxtaancëru)
m robot Removing: bi:Europe
Jult (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Tugal''' mooy wàll wi féete penku goxub [[Tugalasi]], ci baax dañu koi jàppe niki benn ci juroom-benn walla juroom-ñaari [[Gox|goxi]] àdduna bi. Gox baa gi digu ci sowwu ci [[mbàmbulaanug Atlas]] gi, ci bëj-gànnaar ci [[dottub Bëj-gànnaar]] bi, yem ci [[géej gu Diggu]] gi ci bëj-saalum. Ay digam ci penku dese nañoo leer, di na faral di jur ay werante; li ko waral mooy ni mu taqalook goxub [[Asi]].
 
[[Islaand|Waa-Islaand]] jàppe nañ leen ni waa-tugal (donte féeteem ci degalub Tugal-Aamerig), ak mbooleem dun yi ci [[géej gu Diggu]] gi, [[Sipër]] mi gëna jur coow, ci wàllu [[Melosuuf|melosuuf]]. [[Riisi]] ak [[Tirki]] ñi am li ëpp ci seen suuf ca Asi, waaye day ni rek li ëpp ci seen taariix réewi gox bi lañ ko bokkal.
==Melosuuf==
Ngir xóotal: [[Melosuufug Tugal]]
Tugal a ngi yaatoo 10 392 855 km² (fukki junni-junni ak ñetti-fukki-junni ak juroom-ñent-fukk ak ñaar ak juroom-ñetti-téeméer ak juroom-fukk ak juroom). Di benn ñetti [[Afrig]] walla benn ñenti [[Asi]] walla [[Aamerig]].
 
Mi ngi séedatliku ci jurromi diwaan: [[Penku Tugal]], [[Diggu Tugal]], [[Sowwu Tugal]], [[Bëj-gànnaaru Tugal]] ak [[Bëj-saalumu Tugal]]
 
Gox bi am na 49 ciy réew.
 
=== Réewi Tugal ===
 
{| border=1 align=right cellpadding=4 cellspacing=0 width=250 style="margin: 0 0 1em 1em; background: #f9f9f9; border: 1px #aaaaaa solid; border-collapse: collapse; font-size: 95%;"
|+<big><big>'''Tugal'''</big></big>
Ligne 28 ⟶ 15 :
| '''[[Réew]]''' || 48 [[Réew|réew]], 27 yi bokk nañ ci [[Bennoob Tugal]]
|}
'''Tugal''' mooy wàll wi féete penku goxub [[Tugalasi]], ci baax dañu koi jàppe niki benn ci juroom-benn walla juroom-ñaari [[Gox|goxi]] àdduna bi. Gox baa gi digu ci sowwu ci [[mbàmbulaanug Atlas]] gi, ci bëj-gànnaar ci [[dottub Bëj-gànnaar]] bi, yem ci [[géej gu Diggu]] gi ci bëj-saalum. Ay digam ci penku dese nañoo leer, di na faral di jur ay werante; li ko waral mooy ni mu taqalook goxub [[Asi]].
 
[[Islaand|Waa-Islaand]] jàppe nañ leen ni waa-tugal (donte féeteem ci degalub Tugal-Aamerig), ak mbooleem dun yi ci [[géej gu Diggu]] gi, [[Sipër]] mi gëna jur coow, ci wàllu [[Melosuuf|melosuuf]]. [[Riisi]] ak [[Tirki]] ñi am li ëpp ci seen suuf ca Asi, waaye day ni rek li ëpp ci seen taariix réewi gox bi lañ ko bokkal.
==Melosuuf==
Ngir xóotal: [[Melosuufug Tugal]]
Tugal a ngi yaatoo 10 392 855 km² (fukki junni-junni ak ñetti-fukki-junni ak juroom-ñent-fukk ak ñaar ak juroom-ñetti-téeméer ak juroom-fukk ak juroom). Di benn ñetti [[Afrig]] walla benn ñenti [[Asi]] walla [[Aamerig]].
 
Mi ngi séedatliku ci jurromi diwaan: [[Penku Tugal]], [[Diggu Tugal]], [[Sowwu Tugal]], [[Bëj-gànnaaru Tugal]] ak [[Bëj-saalumu Tugal]]
 
Gox bi am na 49 ciy réew.
 
=== Réewi Tugal ===
{| border="1" cellpadding="4" cellspacing="0" class="references-small" style="border:1px solid #aaa; border-collapse:collapse"
|- bgcolor="#ECECEC"
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Tugal » lañ ko jële