Gëwéel wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
CommonsDelinker (waxtaancëru)
m The file Image:Wendekreise_Tropics_Donence.png has been replaced by Image:Wendekreise.png by administrator commons:User:D-Kuru: ''duplicate file''. ''Translate me!''
Rëdd 5 :
 
Waaye nag jàpp nañu ne it ngelaw yiy upp ak duusi géej yi ak rëyaayu diiwaan bi am nañu ay jeexiital yu solowu ci klimaay diiwaan yi, ba tax na su nu seetloo yenn diiwaan yi, doonte nekk nañu ci wetu ab gëwéel, amuñu klimaab gëwéel (ci misaal diggu Óstraali walla bu Sahara, nga xamne amuñu nawet) ak yenn diiwaan yu am klimaab gëwéel te nekkuñu ci lu jege gëwéel yi( lu mel ne réewum [[Keeñaa]], nekk ci [[yamoo]] gi te li ëpp ci suufam klimaab gëwéel la am).
[[Image:Wendekreise Tropics Donence.png|300px|thumb|Gëwéel yi ñooy rëdd yu baxa yu xëm yi, ci kaw ak suufu [[yamoo]] gi, moom di rëdd wu leer wi]]
== Diiwaani gëwéel yu mag yi ==
Diiwaan yiy dund cib klimaab gëwéel dëgg-dëgg ñoo ngi nekk ci [[diggu Aamerig]] ak [[bëj-saalumu Aamerig]], ci digg ak genn wàllu [[bëj-gànnaaru Afrig]], ci bëj-gànnaaru [[Óstraali]] ak genn wàllu [[Endoneesi]]. Li des ci barabu diggantegëwéel bi dañu leen di séddale ci diggante klimaab [[tàkk]] (rawatina ci [[Afrig]]), bu [[yamoo]] walla bu xaw a sedd (rawatina ca [[Asi]]