Gëwéel wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Gëwéel''' yi ñaari rëdd la ñulañu yu dëppook [[Yamoo|yamoo]] gi: [[Gëwéelub Tef|gëwéelub Tef]] tollu ci 23°24' wu [[Tus-wu-gaar|tus-wu-gaar]] wu bëj-gànnaar gi ak [[Gëwéelub Sànkar|gëwéelub Sànkar]] tollu ci 23°27' wu tus-wu-gaar wu bëj-saalum. di nañnañu woowe it gëwéel diwaandiiwaan yi ne ci li wër rëdd yooyule (di faral di wax dëkk ci gëwéel yi).
 
== Melokaan ==
Ci li jege [[Yamoo|yamoo]] gi, di nañnañu faral di gis klimaa bu ànd ak tangoortàngoor guwu tar ak taw bu bari ci at mi mépp: di ko wax [[Klimaab yamoo|klimaab yamoo]]. Waaye, ci njegeetili jege gëwéel yi (tefTef mbaa SankarSànkar), ci at mi [[Noor|noor]] ak [[Nawet|nawet]] rekk a ci am, kon wàccitwàcciit yi (taw yi) day wuute ci jamonoy at mi, ba daanaka at méppaymépp ay tangtàng, di li ñuy wax [[Klimaab gëwéel|klimaab gëwéel]].
 
Waaye nag jàpp nañu ne it ngelaw yiy uppuupp ak dawaaniduusi géej yi ak rëyaayu diwaandiiwaan bi am nañnañu ay njeexitjeexiital yu solowu ci klimaay diwaandiiwaan yi, ba tax na su nu seetloo yenn diwaandiiwaan yi, dontedoonte nekk nañnañu ci wetu ab gëwéel, amuñu klimaab gëwéel (ci misaal diggu Óstraali walla gubu Sahara, nga xamne amuñu nawet) ak yenn diwaandiiwaan yu am klimaab gëwéel te nekkuñu ci njegeetilu jege gëwéel yi( lu mel ne réewum [[Keeñaa]], nekk ci [[yamoo]] gi te li ëpp ci suufam klimaab gëwéel la am).
[[Image:Wendekreise Tropics Donence.png|300px|thumb|Gëwéel yi ñooy rëdd yu baxa yu xëm yi, ci kaw ak suufu [[yamoo]] gi, moom di rëdd wu leer wi]]
== DiwaaniDiiwaani gëwéel yu mag yi ==
DiwaanDiiwaan yiy dundudund cib klimaab gëwéel dëgg-dëgg ñoo ngi nekk ci [[diggu Aamerig]] ak [[bëj-saalumu Aamerig]], ci digg ak genn wàllu [[bëj-gànnaaru Afrig]], ci bëj-gànnaaru [[Óstraali]] ak genn wàllu [[Endoneesi]]. Li des ci barabu diggantegëwéel bi dañdañu leen di séddale ci diggante klimaab [[tàkk]] (rawatina ci [[Afrig]]), bu [[yamoo]] walla bu xaw a sedd (rawatina ca [[Asi]]
 
=== Lëkkalekaay yu biti ===