Jeqiku gi xam-xam amal ci Elektron wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 24 :
 
Jumtukaay yu elektronik yi mujj nanu ci jamono jii nu nekk, di loo xam ne foo wëlbëtiku gis ko, ci kër yi, barabu ligeeyliggéeyuwaay yi, dëkk yu mag yi, yu ndaw yi, mbay mi ak mecce yi añs.
Kon daal jumtukaayi elektron yi, dugal nanu seen loxo ci yombal dund gi, nga gis nit ñi ñuy jëfandikoo raxasukaay yu kuran yu otomatik yi, ak fompukaay yu kuran yu otomatik yi, ak jumtukaayu seral yi yu wuute yi, ak rajook tele yu melo yi, ak jumtukaayu nataal yi añs.
Boo demee ci ndoktoor it fekk ko mu fees dell ak jumtukaay yu elektron, xoolal ma fesalukaay yu elektonik yiy feeñal jàngoro yi gën a tuuti, ak nataalukaayu ndoktoor yi, ak jumtukaayu segg yu elktronik yi. Jumtukaay yii dey tax nanu doktoor man a xam lu jot nit, man koo faj, te looloo tax ndoktoor jëm kanam ci sunu jamono jii.
 
Kon daal jumtukaayi elektron yi, dugal nanu seen loxo ci yombal dund gi, nga gis nit ñi ñuy jëfandikoo raxasukaay yu kuranmbëj yu boppu (otomatik) yi, ak fompukaay yu kuran[[mbëj]] yu otomatikboppu yi, ak jumtukaayu seral yi yu wuute yi, ak rajook tele yu melo yi, ak jumtukaayu nataal yi añs.
Gis nga leegi foo dem fekk fa komputer, ci bank yi, lonkoo yi, campeefi goornamaa yi ak ligeewukaay yi.
Gis nga xam-xamu fuglug jawwu ji ni mu nosoo leegi, ak xam kiliman bi, te loolu lepp elektron a ko waral, leegi man nanoo xam nu tooyaay bi toll, nu jawwu ji selle, nu gelaw li gaawe, nu tàngoor wi tànge, nu niir yi kawee añs, te loolu lepp elktron a ko def.
Waa xam-xamu suuf (jiyoloji) jariñu nanu ci jumtukaayi elktronik yi leen di xamal ati doj yi ak ati suuf si, te di leen won fi am petrol, yoraniyom ak yeneen mbèlli suuf yu am yi solo.
 
Boo demee ci ndoktoorpaj it fekk ko mu fees dell ak jumtukaay yu elektron, xoolal ma fesalukaay yu elektonikelekton yiy feeñal jàngoro yi gën a tuuti, ak nataalukaayu ndoktoorpaj yi, ak jumtukaayu segg yu elktronikelktron yi. Jumtukaay yii dey tax nanu doktoorpaj man a xam lu jot nit, man koo faj, te looloo tax ndoktoorpaj jëm kanam ci sunu jamono jii.
Jumtukaayi elektronik yi dimblee nanu ci wàlli ngànnaay ak xare, ak aaru. Leegi gis nga jumu fepp , rajo, jumtukaay yi amul buum , ak yiy yonnee tey nangu, ak yiy nataal añs.
 
Gis nga leegi foo dem fekk fa komputer[[nosukaay]], ci bank yi, lonkoo yi(les sociétés), campeefi goornamaanguur yi ak ligeewukaayliggéeyuwaay yi.
Gis nga xam-xamu [[fuglug jawwu]] ji ni mu nosoo leegi, ak xam kilimankilimaa bi, te loolu lepp elektron a ko waral, leegi man nanoo xam nu tooyaay bi toll, nu jawwu ji selle, nu gelaw li gaawe, nu tàngoor wi tànge, nu niir yi kawee añs, te loolu lepp elktron a ko def.
Waa xam-xamu suuf (jiyoloji) jariñu nanu ci jumtukaayi elktronikelktron yi leen di xamal ati doj yi ak ati suuf si, te di leen won fi am petrol, yoraniyom ak yeneen mbèllimbelli suuf yu am yi solo.
 
Jumtukaayi elektronikelektron yi dimblee nanu ci wàlli ngànnaay ak xare, ak aaru. Leegi gis nga jumusoxu fepp (bombe atomique) , rajo, jumtukaay yi amul buum , ak yiy yonnee tey nangu, ak yiy nataal añs.
 
Lii nag wone na ne xam-xamu elektron, aki jumtukaayam, yi ci aju ci jàmm ak yi ci aju ci xare, def nanu fi ag jeqiku gu xam-xam gu am solo ci xarnub ñaar-fukk g bii.