Jeqiku gi xam-xam amal ci Elektron wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 14 :
 
Xam nañu ne xam-xamu mbëj moom xam-xam la bu ñu xame bu yàgg ci ki ñuy wax [[Taalis]], di woon boroom xam-xamu Geres. Ay boroom xam-xam yu bari nag ñëw, gën koo jëme kanam, bokk na ci ñooñu kii ñuy wax [[Wilyaam Jilbert]], di boroom xam-xamu Angalteer boo xam ne mooy ki teqale dooley mbëj ak dooley [[bijjaakon]] , ci noonu la wuuteek kii di Taalis mi ne woon ñoom ñaar daal benn lañu.
Jilbert it xamoon na ne duusi mbëj yi ñooy jur dooley bijjaakon. Boroom xam-xamu Almaañ bii di [[Anofon Jiyorik]], moom itam di ki njëkk a genne masinuwuutuloxo buy juddal kuranmbëj, maanaam jumtukaay buy tax kuran bimbëj di judd, di am, loolu di ci atum 1663 g. [[Tomas Adison]] it ñëw, indil ñu lamplàmp bu kuranmbëj.
 
Xam-xamu kuranmbëj nag soppiku di xam-xamu [[elektron]] ci njëlbeeni xarnub ñaarfukeel g, loolu nag mi ngi amoon ginaawginnaaw bi boroom xam-xamu fisiyaaJëmm bu angleAngalteer bii di [[Josef TOMSON]] jugee, feeñal xam-xamu elektron atum 1897 g, daal di ciy ame [[neexalub Nobel]] ci xam-xamu fisiya[[Jëmm]].
Li gën a jëmal kanam xam-xamu elektron nag mooy feeñalwuññi gi boroom xam-xam yi feeñalwuññi ne [[fepp]] (saal biy wuyyu) day xëcc jëme ci boppam lu bari ci elektron yiy bañ, te moom fepp wi day seddaliku ci fepp yu bari.
Ndamul xam-xam lii ab jeegojéego la bu am solo ci doxub xam-xamu elektron. JeegoJéego bii daal bu am solo la ci dundug nit ci kaw suuf.
 
 
== Jumtukaay yu elektronikelektronig (walla mbëjfeppal) yi ak seen njariñ: ==
 
Jumtukaay yu elektronik yi mujj nanu ci jamono jii nu nekk, di loo xam ne foo wëlbëtiku gis ko, ci kër yi, barabu ligeey yi, dëkk yu mag yi, yu ndaw yi, mbay mi ak mecce yi añs.