Jeqiku gi xam-xam amal ci Elektron wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 13 :
 
 
Xam nanunañu ne xam-xamu Kuranmbëj moom xam-xam la bu nuñu xame bu yàgg ci ki nuyñuy wax [[Taalis]], di woon boroom xam-xamu GresGeres. Ay boroom xam-xam yu bari nag ñëw, gën koo jëme kanam, bokk na ci ñooñu kii nuyñuy wax [[Wilyaam Jilbert]], di boroom xam-xamu AngleAngalteer boo xam ne mooy ki teqale dooley kuranmbëj ak dooley [[bijjaakon]] , ci noonu la wuuteek kii di Taalis mi ne woon ñoom ñaar daal benn lanulañu.
Jilbert it xamoon na ne duusi kuranmbëj yi mooyñooy jur dooley asyebijjaakon. Boroom xam-xamu Almaañ bii di [[Anofon Jiyorik]], moom itam di ki njëkk a genne masinu juddal kuran, maanaam jumtukaay buy tax kuran bi di judd, di am, loolu di ci atum 1663 g. Tomas Adison it ñëw, indil ñu lamp bu kuran.
 
Xam-xamu kuran nag soppiku di xam-xamu elektron ci njëlbeeni xarnub ñaarfukeel g, loolu nag mi ngi amoon ginaaw bi boroom xam-xamu fisiyaa bu angle bii di Josef TOMSON jugee, feeñal xam-xamu elektron atum 1897 g, daal di ciy ame neexalub Nobel ci xam-xamu fisiya.