Jeqiku gi xam-xam amal ci Elektron wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
 
 
Elektron moom yaram wusu sew la lool, moom daal gën na a ndawe ay milyoŋi yoon, yeneen yaram yi nga man a gise ci bët rekk, bu nuñu rafleel. Moom sax manoo koo gise ci fésalukaay yu elktronikmbëjfeppal(electronique) yu bees yi am leegi. Li ko waral mooy boo jëloon ay bilyoŋi Elektron dajale leen, du nu toll ne boppu puso.
 
Elektron nag nekk na ci beppbépp ne-ne bu Yàlla sàkk, moom nag mooy peek [[fepp]] wi , walla saal bi , moom nag foo ko fekk da koy wër ngir xëcc gi ko saalfepp biywiy xëcc. Elektron ni muy wëre saalfepp biwi - booy xool - day mel ne ni bidiw yu magkawkab yi di wëre jant bi.
Elektron nag day yanu ay cëfkay kuranmbëj yuy bañ , saal bi walla fepp wi di yor ay cëfkay kuranmbëj yuy wuyyu walla nangu.
 
 
== Xam-xamu Elektron ni mu sosoo: ==
 
Xam-xamu Elektron ni mu sosoo:
 
Xam nanu ne xam-xamu Kuran moom xam-xam la bu nu xame bu yàgg ci ki nuy wax Taalis, di woon boroom xam-xamu Gres. Ay boroom xam-xam yu bari nag ñëw, gën koo jëme kanam, bokk na ci ñooñu kii nuy wax Wilyaam Jilbert, di boroom xam-xamu Angle boo xam ne mooy ki teqale dooley kuran ak dooley bijjaakon , ci noonu la wuuteek kii di Taalis mi ne woon ñoom ñaar daal benn lanu.