Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 152 :
 
Xetug xare tàmbli woon na a xeeñ ak a jòlli ci diggante Fraans ak Brusiya, ginaaw bi Brusiya gañee'''ndàmbee ndam''' ca xareb Sadwa ba. Ndaxte FraansFaraas moom begutoon dara ci lii Brusiya amal ciy ndam ci kaw Danmark ak Otris cig wàll, ak àntul gi mu àntuloon bennoo gu Almaañ gu bëj-gànnaar gi, ci geneen wàll.
 
FraansFaraas moom daa jàppe woon loolu muy aw xët ci digg ginaawam, ndaxte moom kat manul woon a dékku ag nguur gu Almaañ gu am doole ci wetam. Moom kay li ko sooboon mooy Almaañ des di nguur gu nuñu dogat, ngir mu nekk moom FraansFaraas di reewréew mi am kilifteefkiliftéef ci sowwub Tugal bi. Moom kay jamono ju nekk, da daadaan kontar bennoog Almaañ gi, ni ko Otris kontare woon. Bismarck it tàmbli woon na a xalaat nu muy xëcce diiwaani Almaañ yu bëj-saalum yi ngir nuñu bokksi ci bennoo gi. Jëf ju mel ni jooju nag FraansFaraas du ko doon nangu, ndax moom tàmbli woon na di dugg ci mbiri diiwaan yu Almaañ yu bëj-saalum yi, ngir tee leen a bokki ca bennoo gu Almaañ ga nga xam ne Brusiya ko jiite woon.
Lëj-lëju ku jigeen ki waroon a donn Espaañ daal di taxaw, mooy lëj-lëj bi taaloon xare bi ci diggante Brusiya ak Fraans.
Lëj-lëj boobu mi ngi tënkoo woon nii: gàngunaay gu nguurug Espaañ dafa feexoon , ginaaw bi lingeeru Espaañ bi Elisabeth dawee, ñu gaaral buur bi Leopold ndëpp li, moom mi ngi bokkoon ci njabootug Hohenzellern, di woon ab njegeñaaleb imbraatoor bu Brusiya. Waaye ak li Leopold di bañ lepp ne du sol mukk ndëpp li, teewul Fraans mer ci loolu, jàmbat ko ci buurub Brusiya bi, daal di sàkku ci moom mu warlu ne du ànd ci ñu samp kenn ku bokk ci njabootug Hohenzellern ci gàngunaayaug Espaañ gi. Waaye buuru Brusiya bi bañ, ndax loolu kat dafa xaw a laal teddngaam ak ngoram, te xaw a niru ag yabeel. Loolu nag mi ngi ame woon cim ndaje mu mu defoon ak ndawul Fraans ca Ems. Bu ko defee buuru Brusiya bi yonnee ab day ca la juge woon ca ndaje ma, mu yonnee ko Bismarck, mi nga xam ne lepp li mu doon def mooy neggandiku ab pose ngir jibal ab xare ci kaw Fraans. Ba mu ko defee, Bismarck xëy tas ci yëglekaay yi ay cofiit ca la bawoo woon ca ndaje mooma, ngir merloo ci Fraans. Loolu nag ni mu ko defe mooy genne ay baat yu xaw a wow, yu begloowul dara Fraans. Ci noonu Fraans jug, jibal ab xare ci kaw Brusiya, ci 14 sulye 1870g, te fekku ko woon jekk ngir xeex, te taxul woon it mu xalaat ci ngérte yi man a juddoo ci bii xare, bis bu nu dàqee Fraans ci xeex bi.
 
Lëj-lëju ku jigeenjigéen ki waroon a donn Espaañ daal di taxaw, mooy lëj-lëj bi taaloon xare bi ci diggante Brusiya ak Fraans.
Brusiya li nuy wax xareb fëkk la doon def ak Fraans, maanaam gaawal ko, loolu nag jot na koo def ba am ci xam-xam ca xareem ba’ak Otris. Bi mu ko defee tàngooru xare bi sax di tar lu tollook juroom benni ayu bis, waaye tàmblee giim, ci ginaaw bi, rawati na ci ginaaw bi ay màndargay kawe ak ëpp doole tàmblee feeñ ci xeex bi ñeel Brusiya.
Lëj-lëj boobu mi ngi tënkoo woon nii: gàngunaay gu nguurug Espaañ dafa feexoonféexoon , ginaaw bi lingeeru Espaañ bi Elisabeth dawee, ñu gaaral buur bi [[Leopold]] ndëpp li, moom mi ngi bokkoon ci njabootug [[Hohenzellern]], di woon ab njegeñaalebjegeñaaleb imbraatoorimbraatóor bu Brusiya. Waaye ak li Leopold di bañ lepp ne du sol mukk ndëpp li, teewul FraansFaraas mer ci loolu, jàmbat ko ci buurub Brusiya bi, daal di sàkku ci moom mu warlu ne du ànd ci ñu samp kenn ku bokk ci njabootug Hohenzellern ci gàngunaayaug Espaañ gi. Waaye buuru Brusiya bi bañ, ndax loolu kat dafa xaw a laal teddngaam ak ngoram, te xaw a niru ag yabeel. Loolu nag mi ngi ame woon cim ndaje mu mu defoon ak ndawulaji Fraansteewal ju Faraas ja ca Ems. Bu ko defee buuru Brusiya bi yonnee ab day ca la juge woon ca ndaje ma, mu yonnee ko Bismarck, mi nga xam ne lepp li mu doon def mooy neggandiku ab pose ngirééngir jibal ab xare ci kaw FraansFaraas. Ba mu ko defee, Bismarck xëy tas ci yëglekaayyéenekaay yi ay cofiit ca la bawoo woon ca ndaje mooma, ngir merloo ci FraansFaraas. Loolu nag ni mu ko defe mooy gennegénne ay baat yu xaw a wow, yu begloowul dara FraansFaraas. Ci noonu FraansFaraas jug, jibal ab xare ci kaw Brusiya, ci 14 sulyesulet 1870g, te fekku ko woon jekk ngir xeex, te taxul woon it mu xalaat ci ngérte yi man a juddoo ci bii xare, bis bu nuñu dàqee Fraans ci xeex bi.
Xare bi bepp nag ci suufus Fraans la doon tàkke. Jotoon nanoo dàq Fraans nag ci xeex yu bari, bi ci gënoon a siw nag mooy bu Sedan ca satumbar1870g, nga xam ne àggoon na ci Napoleon III manutoon a ñàkk a wommatu, te nangu ne gañe nanu ko, ngir dàq yu metti yi te toftaloo, te yepp di yu nu teg ci kaw dooley Fraans ji ci biir suufus Fraans, te ray lu sakkan ciy soldaaram, te itam lu jege ñaari teemeeri junniy soldaari Almaañ sutuxlu ba ca xolub Fraans, te mu leer nàññ ne Fraans moom manatul a gañeeti Brusiya ca jamono joojee te manatu koo genneeti suufam. Loolu nag di woon ci 27 oktobar 11870g.
 
Brusiya li nuyñuy wax xareb fëkk la doon def ak FraansFaraas, maanaam gaawal ko, loolu nag jot na koo def ba am ci xam-xam ak jarbu ca xareem ba’ak Otris. Bi mu ko defee tàngooru xare bi sax di tar lu tollook juroom benni ayu bis, waaye tàmblee giim, ci ginaaw bi, rawati na ci ginaaw bi ay màndargay kawe ak ëpp doole tàmblee feeñ ci xeex bi ñeel Brusiya.
Ci noonu imbraatoor gu Fraans gu ñatteel gi daanu, ñu daal di taxawal ci Paris nosteg pénc gu ñatteel gi . Daal di teg Fraans ñeel Brusiya alamaanug xare gu toll ci juroomi bilyoŋi frank yu Fraans ( loolu mooy tollook – daanak – alamaan bi Napoleon Bonaparte tegoon Brusiya bi mu ko dumaa ca xareb Yena ba, 1806g. Bu ko defee ñu juboo ci xarekati Almaañ yi dunu genn Fraans li feek fayeesul alamaan bi, (moom nag jotees na koo fay ci diirub ñatti at). Nga rax ci dolli dagg gi nu dagge ñaari gox yii di Alsaas ak Loren ci fraans, boole leen ci Almaañ.
 
Xare bi bepp nag ci suufus FraansFaraas la doon tàkke. Jotoon nanoonañoo dàq Fraans nag ci xeex yu bari, bi ci gënoon a siw nag mooy bu Sedan ca satumbar1870g, nga xam ne àggoon na ci Napoleon III manutoon a ñàkk a wommatu (se rendre), te nangu ne gañe nanu ko, ngir dàq yu metti yi te toftaloo, te yepp di yu nu teg ci kaw dooley FraansFaraas ji ci biir suufus FraansFaraas, te ray lu sakkan ciy soldaaram, te itam lu jege ñaari teemeeritéeméeri junniy soldaari Almaañ sutuxlu ba ca xolub FraansFaraas, te mu leer nàññ ne FraansFaraas moom manatul a gañeeti Brusiya ca jamono joojee te manatu koo genneetigénneeti suufam. Loolu nag di woon ci 27 oktobar 11870g.
Nii daal la bennoo gu Almaañ mate woon ci njiitul Brusiya, ci loxol goor gu dëgër gii ni weñ, Bismarck, mi nga xam ne dafa gëmoon bennal Almaañ ak doonte day ci dereet, ci weñ mbaa sawara. Bu ko defee imbraatoorug Almaañ gi daal di sosu, dib xew-xew nag bu fés ci taarixu Tugal bu bees bi.boroom gàngunaay gi (imbratooru Almaañ bi) mujj di ku ñu joyal ab gogam ci def li ko neex ci nguur-nguuraan yu Almaañ yi.
Sartu reew bu Almaañ bu bees bi yaxal na nu sos ñaari jataay:
 
Ci noonu imbraatoorimbraatóor gu FraansFaraas gu ñatteel gi daanu, ñu daal di taxawal ci Paris nosteg pénc gu ñatteel gi . Daal di teg FraansFaraas ñeel Brusiya alamaanug xare gu toll ci juroomi bilyoŋi frank yu Fraans ( loolu mooy tollook – daanak – alamaan bi Napoleon Bonaparte tegoon Brusiya bi mu ko dumaa ca xareb Yena ba, 1806g. Bu ko defee ñu juboo ci xarekati Almaañ yi dunuduñu genngénn FraansFaraas li feek fayeesul alamaan bi, (moom nag jotees na koo fay ci diirub ñatti at). Nga rax ci dolli dagg gi nuñu dagge ñaari goxdiiwaan yii di Alsaas ak Loren ci fraansfaraas, boole leen ci Almaañ.
(1) Jataayu Bennoo gu Almaañ (Bundasrat)
(2) Jattayu (Rechstag)
 
Nii daal la bennoo gu Almaañ mate woon ci njiitul Brusiya, ci loxol goorgóor gu dëgër gii ni weñ, Bismarck, mi nga xam ne dafa gëmoon bennal Almaañ '''ak doonte day ci dereet, ci weñ mbaa sawara'''. Bu ko defee imbraatoorugimbraatóorug Almaañ gi daal di sosu, dib xew-xew nag bu fés ci taarixu Tugal bu bees bi.boroom gàngunaay gi (imbratooruimbratóoru Almaañ bi) mujj di '''ku ñu joyal ab gogam''' ci def li ko neex ci nguur-nguuraan yu Almaañ yi.
Dooley yoonal ji nag mi ngi nekkoon ci Bundasrat, di jataay bi nga xam ne mi ngi ame woon ci juroom fukk ak juroom ñatti cer, ñu seddale leen ci nguur-nguuran yi nga xam ne ñoo amal imbraatoor gu Almaañ gi. Brusiya nag moom rekk amoon na fukki kàddu ak juroom ñaar, ginaaw bi mu am ñaar fukki kàddu. Ak li Brusiya di moomadi li ëpp ci kàddu yi lepp ci Bundasrat, teewul mu gënoon fa’a guddub loxo, gënoon fa a am jeexiit, ndax la ëppoon ca nguur-nguuraani Almaañ ya duggoon ca bonnoog Almaañ ga, danoo takku woon ci Brusiya, te daawunu woote lenn lu mu bëggul. Te daawunu jàllale genn saxal ca jataay ba, bu fukki cer ak ñeent àndadee ca saxal ga.
Sartu reewréew bu Almaañ bu bees bi '''yaxal''' na nuñu sos ñaari '''jataay''':
Bu dee nag jataayu Rechstag nag moom, man nanu ne mooy jataayub askan bi, mi ngi ame woon ci ñatti teemeer ak juroom ñeen-fukk ak juroom ñaari cer, ñu leen di tànn ci anam gu sekkaree. Dooley jataay bii nag daanaka danu koo lafañal, yòqeel ko . ndax nguur ak doole yi nu ko joxoon ci ron sartu reew bu Almaañ bu bees bi, danoo nekkoon di yu doyadi te ñàkk solo.
 
(1) * '''Jataayu Bennoo gu Almaañ (Bundasrat)'''
Bismarck nag, jiite na goornamaa bu Almaañ bi niki diisoowaale walla chancelier. Benn ci ñaari jataay yi manul woon ci moom dara, mu yoroon it sañ-sañ bu rëy, te ci ron kilifteefam tam la Almaañ gu rëy gii gepp nekkoon, nga xam ne ña fa dëkkoon ca atum 1871g jege woon nanu ñeen-fukki milyoŋi nit, mujj àgg ci ñeen fukk ak juroom ñeenti milyoŋ ciy nit atum 1890g, di maanaam bi Bismarck faatoo ba am ñaari at.
(2) * '''Jattayu (Rechstag)'''
 
Dooley yoonal ji nag mi ngi nekkoon ci '''Bundasrat''', di jataay bi nga xam ne mi ngi ame woon ci juroom fukk ak juroom ñatti cercér, ñu seddaleséddale leen ci nguur-nguuran yi nga xam ne ñoo amal imbraatoorimbraatóóor gu Almaañ gi. Brusiya nag moom rekk amoon na fukki '''kàddu''' ak juroom ñaar, ginaaw bi mu am ñaar fukki kàddu. Ak li Brusiya di moomadi li ëpp ci kàddu yi lepplépp ci Bundasrat, teewul mu gënoon fa’a guddub loxo, gënoon fa a am jeexiit,jeexiital ndax la ëppoon ca nguur-nguuraani Almaañ ya duggoon ca bonnoog Almaañ ga, danoodañoo takku woon ci Brusiya, te daawunudaawuñu woote lenn lu mu bëggul. Te daawunudaawuñu jàllale genn saxal ca jataay ba, bu fukki cercér ak ñeent àndadee ca saxal ga.
Bu dee nag jataayu Rechstag nag moom, man nanunanñu ne mooy jataayub askan bi, mi ngi ame woon ci ñatti teemeertéeméer ak juroom ñeen-fukk ak juroom ñaari cercér, ñu leen di tànn ci anam gu sekkaree. Dooley jataay bii nag daanaka danudañu koo lafañal, yòqeel ko . ndax nguur ak doole yi nuñu ko joxoon ci ron sartu reewréew bu Almaañ bu bees bi, danoodañoo nekkoon di yu doyadi te ñàkk solo.
 
Bismarck nag, jiite na goornamaagóornamaa bu Almaañ bi niki diisoowaale walla chancelier. Benn ci ñaari jataay yi manul woon ci moom dara, mu yoroon it sañ-sañ bu rëy, te ci ron kilifteefamkiliftéefam tam la Almaañ gu rëy gii geppgépp nekkoon, nga xam ne ña fa dëkkoon ca atum 1871g jege woon nanunañu ñeen-fukki milyoŋi nit, mujj àgg ci ñeen fukk ak juroom ñeenti milyoŋ ciy nit atum 1890g, di maanaam bi Bismarck faatoo ba am ñaari at.
[[Catégorie:taariixu Tugal]]