Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 112 :
 
 
Bismarck xuus na ay xare ak lu bari ci reewiréewi Tugal yi digoo’k Almaañ, ngir bennal reewidiiwaani Almaañ yi. Ñu tudd ñatt rekk ci xare yooyu, ñooy:
 
Xare Brusiya yi ak Danmark:
 
== Xare yu Brusiya yi ak Danmark:==
Bismarck xuus na ab xare kontar Danmark, atum 1864g, ànd ca’ak Otris, ngir nangu ñaari diiwaan yii di Shalswig ak Holistin, ñu doonoon ñaari doox yu bokkoon ci bennoo gu Almaañ gi te Danmark tegoon leen loxo.
 
Danmark mujjoon na ñàkk pexe, daal di deltu ginaaw wëlif ñaari doox yooyu atum 1864g, bu ko defee Brusiya jël dooxu Shalswig, Otris it àtte diiwaanu Holistin.
Bismarck xuus na ab xare kontarsafaan Danmark, atum 1864g, ànd ca’ak Otris, ngir nangu ñaari diiwaan yii di '''Shalswig''' ak '''Holistin''', ñu doonoon ñaari doox'''Dóox''' (duché) yu bokkoon ci bennoo gu Almaañ gi te Danmark tegoon leen loxo.
 
Danmark mujjoon na ñàkk pexe, daal di deltu ginaaw wëlif ñaari dooxdóox yooyu atum 1864g, bu ko defee Brusiya jël dooxudóoxu Shalswig, Otris it àtte diiwaanu '''Holistin'''.
 
== Xarey Brusiya ak Otris: ==
 
Xarey Brusiya ak Otris:
 
Bismarck gisoon na ne xare bi moom – deet sikk – aji tàkk la ci diggante Brusiya ak Otris, te li ko waral du dara lu dul diiwaanu Holistin. Ndax kat mbir yi manunu woon a nekk di wéy ci anam gii nu nekke, di ay maslaa yu dëggoodi aki lijjanti yu xootadi aki juboo yu gàtti dig.