Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 93 :
 
Loolu nag gën na a fése ci taxaw gi mu taxawoon ci dakkal politigu Otris bi muy teg Almaañ .
Looloo taxoon Otris mujj woo buuri Almaañ yeppyépp cim ndaje ca Frankfort, ngir sos ag '''bennoo gu lëngoo (walla gu federaal)''', guy doxal ab goornamaa, boo xam ne ay dooleem ak sañ-sañam mi ngi koy jële ci sart boo xam ne Otris moo koy defar, tër ko.
 
Bismarck gisoon na ne lii de ag anam gu yees gu Otris jëlati la, ñu muure ko mbubum diplomasi walla maslaa, ngir yeegatiyéegati ci kaw waa Almaañ yi. Bismarck melaloon na sart boobu ne mooy sart bi gën a bon ci mbooleem yu mas a am ci kaw suuf. Ci noonu mu ne woon du teewe ndaje ma lu dul ci kaw ñu jox Brusiya ay àq aki yelleef yu tol ni yi nuñu jox Otris ci ñaari mbir yii, ñooy:
(1) Dëgël ak wéyal jibalug bennoo gi
 
(2) Jiite benno gi
(1)* Dëgël'''Dëggal ak wéyal jibalug bennoo gi '''
 
(2)* '''Jiite benno gi'''
 
Bismarck ci taxawaayam bii, leerale na ci ne Otris daal moom ñàkk na kàttan ga mu amoon ci aakimoo moom rekk mbirum bennoo gu Almaañ gi. Te it won na nguur-nguuraani Almaañ yi ne Brusiya mii kat mooy jenn dooley Almaañ ji man a jiite bennoo gu Almaañ gi.
Bismarck jeem na a fàggu cofeelug Rusi, ngir mu bañ a feete fenn, bu ab xare tàkkee ci diggam ak Otris. Loolooo taxoon mu dugg ci lëj-lëju Poloñ bi, jàpple ci Rusi, kontar gori Ploñ yi defoon ag fipp kontar Rusi, ngir dañal ag àtteem te jeem a am ag tembte, ba man a amal ag àtte gu Poloñ gu temb.
Fraans nag àndoon na ca fipp ga, te jàpple ko, askanu Angalteer wi ànd ca, waaye goornamaa ba moom àndu ca woon, ndax daa ragaloon ag nguurug Poloñ gu katolig judd, guy dem di àndeek Fraans.
Ci noonu Bismarck moom dem jàpple-ji Rusi, te jàpple googu gu amoon doole la, ndax moom reewam (Brusiya) daa taqaloo woon ak Poloñ, ba noppi taqalook Rusi. Te it nanguwutoon a ànd ak Fraans ak Otris kontar Rusi.
 
Bismarck jeemjéem na a fàggu cofeelug RusiRiisi, ngir mu bañ a feeteféete fenn, bu ab xare tàkkee ci diggam ak Otris. Loolooo taxoon mu dugg ci lëj-lëju Poloñ bi, jàpple ci RusiRiisi, kontar gori PloñPoloñ yi defoon ag fipp kontar RusiRiisi, ngir dañal ag àtteem te jeemjéem a am ag tembte, ba man a amal ag àtte gu Poloñ gu temb.
Xarey Bismarck yi ngir taxawal bennoo gu Almaañ:
 
FraansFaraas nag àndoon na ca fipp ga, te jàpple ko, askanu Angalteer wi ànd ca, waaye goornamaa ba moom àndu ca woon, ndax daa ragaloon ag nguurug Poloñ gu katolig judd, guy dem di àndeek FraansFaraans.
Ci noonu Bismarck moom dem jàpple-ji RusiRiisi, te jàpple googu gu amoon doole la, ndax moom reewamréewam (Brusiya) daa taqaloo woon ak Poloñ, ba noppi taqalook RusiRiisi. Te it nanguwutoon a ànd ak FraansFaraas ak Otris kontar RusiRiisi.
 
 
== Xarey Bismarck yi ngir taxawal bennoo gu Almaañ: ==
 
 
Bismarck xuus na ay xare ak lu bari ci reewi Tugal yi digoo’k Almaañ, ngir bennal reewi Almaañ yi. Ñu tudd ñatt rekk ci xare yooyu, ñooy: