Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 73 :
 
 
Bismarck mi ngi judd atum 1815g, am njàggam mu kawe mu defe ko ca daaray Berlin ju magkawe ja. Daal di dugg ag [[coldaar]], gennatigénnati ca, dem nag feeteféete ca boppam ca toolam ba. Mi ngi bokkoon nag ci njaboot gu woomle, gu ami alal yu rëy ca Brusiya. Sampoon na boppam niki '''lawax''' (candidat) ngir nuñu fal ko ci bennoo yu Almaañ yi, atum 1848g, ñu tànnoon ko it muy ab cercér ci parlamaa bu Brusiya bi. LigeeyLiggéey na it ci toolub diplomasi, doonoon ndawulaji reewamtéewal réewam (l'ambassadeur) ca Butrsburg ca RusiRiisi. GinaawGinnaaw bi mu nekkal reewamréewam ca Paris.foofee la ko ''' William mu njëkk''' mi doon jiite Brusiya woowe woon mu juge Fraans[[Faraas]], ngir jiite-si njiitug jawrin gi ci Brusiya.
Bismarck nag nekkoon na ku gëmoon, te daa dëgëral '''noste gu nguur gu nuñu joyal''' , te gëmoon ne buur daa war a am doole te am soldaar su dëgër, Egliis'''Jàngu bi''' jàpple ko ak '''garmi''' yi. Bismarck moom faalewutoon parlamaa bi. Gisoon na ne jëm kanamug aw xeet walla ag yeegamyéegam jëm ca kaw manul a ame ci lu dul ay buuram di ñu kawe ay yitte, ak ay kilifaamkàngamam, waaye du nuduñu ko ame mukk ci ay '''saxal''' (résolutions) yu juge ci ay parlamaa, aki '''nostey sarti reewréew''' (systèmes constitutionnels).
 
Bismarck yitteem jeppjépp mi ngi ko jëmale woon ci gennegénne Fraans[[Faraas]] ak Otris Almaañ, mu gisoon ne lii daal manul ame ci lu dul dooley xare ju mag, ju leen ci man a ga(manante leen). Ci noonu mu tàmblee ligeeyliggéey ci dëgëral dooley xare ji, ak kàttanal ko. Mu daal di tas parlamaab Brusiya bi, ndaxte (moom parlamaa bi) daa bañoon ne du woote alal ji mu doon laaj ngir man cee dooleel soldaaram si, ci noonu mu tëjopontëjoon keppképp ku wuuteek politigam boobu, daal di digle ñu fuglu yeglekaayyéenekaay yi, daal di beddiku sartu reewréew mi, ne du ci sukkandikooti. Alal ji mu soxla woon mu gennelugénnelu ko ci ndigalul buur bi, bañ cee sukkandiku ci lu parlamaa bi.
 
Wàllug '''xeetu''' (nationalisme) nag moom gis-gis bi mu ci amoon moo gënoon a yaatu bi mu amoon ci sartu reewréew, ndax daa gisoon ne sartu reewréew moom, mi ngi ame mook ay jubluwaayam, ci ginaawginnaaw bu ag xeetu amee ba noppi.
Bismarck nag neenalul mbooleem parlamaa bi mbaa mu tas ko lepp, moom kay da caa neenl walla mu soril ko ñatti mbir, ñooy:
(1) Coldaar gi
(2) Politigu bitim reew bi
(3) Fal ay jawrin ak di leen folli
 
Bismarck nag neenalul mbooleem parlamaa bi mbaa mu tas ko lepplépp, moom kay da caa neenl walla mu soril ko ñatti mbir, ñooy:
 
(1)* '''Coldaar gi'''
Bismarck wone na dogu gu mag akug takku contar teg gi Otris teg loxo Almaañ, loolu nag gën na a fése ci taxaw gi mu taxawoon ci dakkal politigu Otris bi muy teg Almaañ .
 
(2)* '''Politigu bitim reewréew bi'''
 
(3)* '''Fal ay jawrinjëwrin ak di leen folli'''
 
 
 
== Bismarck wone na dogu gu mag akug takku contar teg gi Otris teg loxo Almaañ ==
 
Bismarck wone na dogu gu mag akug takku contar teg gi Otris teg loxo Almaañ, looluLoolu nag gën na a fése ci taxaw gi mu taxawoon ci dakkal politigu Otris bi muy teg Almaañ .
Looloo taxoon Otris mujj woo buuri Almaañ yepp cim ndaje ca Frankfort, ngir sos ag bennoo gu federaal, guy doxal ab goornamaa, boo xam ne ay dooleem ak sañ-sañam mi ngi koy jële ci sart boo xam ne Otris moo koy defar, tër ko.
Bismarck gisoon na ne lii de ag anam gu yees gu Otris jëlati la, ñu muure ko mbubum diplomasi, ngir yeegati ci kaw waa Almaañ yi. Bismarck melaloon na sart boobu ne mooy sart bi gën a bon ci mbooleem yu mas a am ci kaw suuf. Ci noonu mu ne woon du teewe ndaje ma lu dul ci kaw ñu jox Brusiya ay àq aki yelleef yu tol ni yi nu jox Otris ci ñaari mbir yii, ñooy: