Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 53 :
Kërug Tugal gi mujj – ni ko Metternich di waxe – di kër gu màggat, te ràpp, ba àgg ci maneesatu cee yatt sax ab palanteer ciy miiram ngirug màggat, kon leegi li jaadu kay mooy ñu màbb ko, te wuutal fa geneen kër gu yees. Ca dëgg-dëgg nag loolu am na, ndax kat noste ga amoon ca la ëppoon ca réewi Tugal ya, daa mujjoon di lu ràpp, ngirug yàgg, mujj manatutoon a ñàkk ñu yeesalaat ko, te taxawalaat ko ci anam gu dëppoo ak li jamono laaj.
 
Metternich dawoon na, te daanu woon, ci noonu buurub Brusiya bi Frederick William mu ñeenteel mi daal di jug, woote am ndaje mu parlamaa, ngir ñu defaral Brusiya '''ab sartu réew''' bu bees. Mu dig aw askanam ne leen moo fas yeenee jiite yëngu-yëngu giy jug ci jeemjéem a bennal Almaañ, ci benn bataaxel bu mu leen jàngal. Ndaw yi teewal Almaañ yeppyépp teewe woon nanunañu ndajem atum 1848g moomu, ñu def fa ay gëstu ci lu aju ci Almaañ gu nekk benn. Ndajem parlamaa mii, ñi ngi ko gën a xame ci turu “Parlamaab Frankfort”. Ndaje ma ëmboon na lu bari ciy woykat (walla taalifkat) , aki xeltukat aki taskati xibaar aki ustaas.
Ñatti saxal nag yu mag juddoo nanunañu ca ndaje ma:
 
(1) * Bennal Almaañ ci njiitul buurub Brusiya.
(2) * Ñu boole ci bennoo gu Almaañ googu, wàllug Almaañ gi bokkoon ci imbraatoorugimbraatóorug Otris gi
(3) Genne* Génne Otris ci bennoo gu Almaañ gi.
 
Way daje yii ci Frankfort, (seenub lim àggoon na ci 830 ciy jëmm) tànnoon nanunañu buurub Brusiya bi [[Fredereick William mu ñeenteel]] mi, def ko imbraatoorimbraatóor ci Almaañ gu nuñu bennal gi. Waaye Frederick moom daa bañoon ne du dëppoo ndëppul imbraatoorimbraatóor li nuñu ko joxoon, te way daje yi joxoon ko ko, ndax da ne''' ndëpp''' li daal ndawi askan wee ko ko jox, waaye buur yeek kàggam yi joxuñu ko ko. looloo taxoon nanguwu koo sol.
La am nag mooy ne buuru Brusiya bi dafa bañ a jël ndëpp li, ndax xam ne Otris ak Rusi ànduñu woon ci bennoog Almaañ googu, te manoon nanoo xëy di duggati ci seeni mbir ngir loolu. Rawati na ne Otris moom jot na a not fipp gi amoon ca peeyam ba Vienne.
Nga rax ci dolli ne Buuru Brusiya bi, moom dafa gëmoon gisiinu “àq ak sañ-sañ bu Yàlla bi”, mooy gisiin wi naan ñoom buur yi Yàlla a leen fi teg, moom lanu fi wuutu, nit ñi tegunu leen fi, du keneen it. Looloo taxoon bu nangoo it ñu def ndaje moomu, muy mu Frankfort mi, jubluwu ci woon lu dul ngistal, waaye du ligeey bu fullawu, mbaa mu dëggu ci yoonu soppi.
 
La am nag mooy ne buuru Brusiya bi dafa bañ a jël ndëpp li, ndax xam ne Otris ak RusiRiisi ànduñu woon ci bennoog Almaañ googu, te manoon nanoonañoo xëy di duggati ci seeni mbir ngir loolu. Rawati na ne Otris moom jot na a notnoot fipp gi amoon ca peeyampéeyam ba Vienne.
Otris ak Rusi dimblante nanu ci màbb barlamaab Frankfort bi, ak naalam yi mu amoon te nu jëm cig bennoo gu Almaañ, looloo waraloon jeem gi nu doon def ngir bennal Almaañ ci ron kilifteefug Brusiya, ci atum 1848g, mujjul woon àntu. Waaye li muy àntoodi lepp teewul xalaat bi sax ci xoli ak xeli waa Almaañ yi. Ñu mujj (waa Almaañ ñi) xam ne daal dunu man a amalati seen bennoo googu ci anamug jàmm, mbaa gu sartu reew, ndaxte Otris àndu ci te mi ngi koy xeex ak doole.
Nga rax ci dolli ne Buuru Brusiya bi, moom dafa gëmoon gisiinu “àq ak sañ-sañ bu Yàlla bi”, mooy gisiin wi naan ñoom buur yi Yàlla a leen fi teg, moom lanu fi wuutu, nit ñi tegunuteguñu leen fi, du keneen it. Looloo taxoon bu nangoo it ñu def ndaje moomu, muy mu Frankfort mi, jubluwu ci woon lu dul ngistal, waaye du ligeeyliggéey bu fullawu, mbaa mu dëggu ci yoonu soppi.
Looloo waraloon nu jëloon seen yitte def ko ci amal am mbooloom xare mu dëgër, mu leen di man a may ñu man a genne Otris Almaañ cig njëlbeen, door a lijjanti nag nu nuy doone benn ci ginaaw bi.
 
Xalaat bii nag diisoowaale bu Brusiya bii di Bismarck, àndoon na ci te jàpple woon ko, dëgëral ko. Moom mooy Otto Von Bismarck, boroom kurpeñu weñ bi.
Otris ak RusiRiisi dimblante nanu ci màbb barlamaab [[Frankfort]] bi, ak naalam yi mu amoon te nuñu jëm cig bennoo gu Almaañ, looloo waraloon jeemjéem gi nuñu doon def ngir bennal Almaañ ci ron kilifteefug Brusiya, ci atum 1848g, mujjul woon àntu. Waaye li muy àntoodi lepp teewul xalaat bi sax ci xoli ak xeli waa Almaañ yi. Ñu mujj (waa Almaañ ñi) xam ne daal dunuduñu man a amalati seen bennoo googu ci anamug jàmm, mbaa gu sartu reewréew, ndaxte Otris àndu ci te mi ngi koy xeex ak doole.
Looloo waraloon nuñu jëloon seen yitte def ko ci amal am mbooloom xare mu dëgër, mu leen di man a may ñu man a gennegénne Otris ak Almaañ cig njëlbeen, door a lijjanti nag nu nuyñuy doone benn ci ginaaw bi.
Xalaat bii nag [[diisoowaale]] (chancelier) bu Brusiya bii di [[Bismarck]], àndoon na ci te jàpple woon ko, dëgëral ko. Moom mooy [[Otto Von Bismarck]], boroom kurpeñu weñ bi.
 
 
== Politigu Bismarck ci lu jëm ci bennoo gu Almaañ gi: ==
 
Politigu Bismarck ci lu jëm ci bennoo gu Almaañ gi:
 
Bismarck mi ngi judd atum 1815g, am njàggam mu kawe mu defe ko ca daaray Berlin ju mag ja. Daal di dugg ag coldaar, gennati ca, dem nag feete ca boppam ca toolam ba. Mi ngi bokkoon nag ci njaboot gu woomle, gu ami alal yu rëy ca Brusiya. Sampoon na boppam ngir nu fal ko ci bennoo yu Almaañ yi, atum 1848g, ñu tànnoon ko it muy ab cer ci parlamaa bu Brusiya bi. Ligeey na it ci toolub diplomasi, doonoon ndawul reewam ca Butrsburg ca Rusi. Ginaaw bi mu nekkal reewam ca Paris.foofee la ko William mu njëkk mi doon jiite Brusiya woowe woon mu juge Fraans, ngir jiite-si njiitug jawrin gi ci Brusiya.