Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 48 :
== Jeexiital yi [[jeqiku]] gu atum 1848g defoon ci amug bennoo gu Almaañ gi: ==
 
Ay fippjeqiku yu bari jot nanoonañoo am ca Tugal atm 1848g. Ag fippjeqiku am ca Paris, am gu am ca Vienne, geneen ca Brusiya ak ay fipp ci Itaali ak Almaañ, yepp it di xëccu jëm ci ag gore , demokraasi ak xeetu . Metternich mu màggat mii, mujjoon na manatul woon a noot fippi Tugal yooyu, mbaa mu giimal leen, ni mu ko baaxoo woon a defe.
Kërug Orob gi mujj – ni ko Metternich di waxe – di kër gu màggat, te ràpp, ba àgg ci maneesatu cee yatt sax ab palanteer ciy miiram ngirug màggat, kon leegi li jaadu kay mooy ñu màbb ko, te wuutal fa geneen kër gu yees. Ca dëgg-dëgg nag loolu am na, ndax kat noste ga amoon ca la ëppoon ca reewi Tugal ya, daa mujjoon di lu ràpp, ngirug yàgg, mujj manatutoon a ñàkk ñu yeesalaat ko, te taxawalaat ko ci anam gu dëppoo ak li jamono laaj.
 
Metternich mu màggat mii, mujjoon na manatul woon a noot jeqikuy Tugal yooyu, mbaa mu giimal leen, ni mu ko baaxoo woon a defe.
Metternich dawoon na, te daanu woon, ci noonu buurub Brusiya bi Frederick William mu ñeenteel mi daal di jug, woote am ndaje mu parlamaa, ngir ñu defaral Brusiya ab sartu reew bu bees. Mu dig aw askanam ne leen moo fas yeenee jiite yëngu-yëngu giy jug ci jeem a bennal Almaañ, ci benn bataaxel bu mu leen jàngal. Ndaw yi teewal Almaañ yepp teewe woon nanu ndajem atum 1848g moomu, ñu def fa ay gëstu ci lu aju ci Almaañ gu nekk benn. Ndajem parlamaa mii, ñi ngi ko gën a xame ci turu “Parlamaab Frankfort”. Ndaje ma ëmboon na lu bari ciy woykat , aki xeltukat aki taskati xibaar aki ustaas.
Kërug OrobTugal gi mujj – ni ko Metternich di waxe – di kër gu màggat, te ràpp, ba àgg ci maneesatu cee yatt sax ab palanteer ciy miiram ngirug màggat, kon leegi li jaadu kay mooy ñu màbb ko, te wuutal fa geneen kër gu yees. Ca dëgg-dëgg nag loolu am na, ndax kat noste ga amoon ca la ëppoon ca reewiréewi Tugal ya, daa mujjoon di lu ràpp, ngirug yàgg, mujj manatutoon a ñàkk ñu yeesalaat ko, te taxawalaat ko ci anam gu dëppoo ak li jamono laaj.
 
Metternich dawoon na, te daanu woon, ci noonu buurub Brusiya bi Frederick William mu ñeenteel mi daal di jug, woote am ndaje mu parlamaa, ngir ñu defaral Brusiya ab sartu reewréew bu bees. Mu dig aw askanam ne leen moo fas yeenee jiite yëngu-yëngu giy jug ci jeem a bennal Almaañ, ci benn bataaxel bu mu leen jàngal. Ndaw yi teewal Almaañ yepp teewe woon nanu ndajem atum 1848g moomu, ñu def fa ay gëstu ci lu aju ci Almaañ gu nekk benn. Ndajem parlamaa mii, ñi ngi ko gën a xame ci turu “Parlamaab Frankfort”. Ndaje ma ëmboon na lu bari ciy woykat , aki xeltukat aki taskati xibaar aki ustaas.
Ñatti saxal nag yu mag juddoo nanu ca ndaje ma: