Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 39 :
 
 
Kilifay Brusiya yi xamoon nanunañu ne diiwaani Almaañ yi dananudanañu nangoo duggsi ci bennoo gu Solofrayn gi, bu nuñu soppee sart yiy tax manees cee dugg. Looloo taxoon ñu soppi sarti Solofrayn yi, nga xam ne leegi danoodañoo sos ab jataay bu làmboo mbooleem ndawi yi ci bokk, buy saytu noste googu. Leegi nag lu fa duggati rekk ci li bawoo ci '''nduwaan mi''' ak galag yi ñu koy seddaleséddale mbooleem diiwaan yi, ci kem limub ña fa dëkk. Soppi yii de dimblee na ci yaatal gëweelubgëwéelub Solofrayn, gën a yàkkali ab geewamgéewam. Leegi nag [[Bavar]] bokksi na ci ak Saksoni[[Saksoniya]] ci atum 1934g, ca saa sa tam, nga tàmblee gis lu lay won ne Solofrayn moom tàmbli na a naat ak a am ag yokkute. Yaxantu ga tàmbli woon nay jar, di dox, mbay ma màgg, endustrindefar baga jëm kanam ci mbooleem diiwaan yi bokksi ci Solofrayn. Am na nag benn jëfka boo xam ne moo àntul Solofrayn, mooy moom de noste gu waa Almaañ xalaat ba def ko la, loxol Otris duggu ci, jenn doole it ju ko man a teg loxo yoonam nekku ci. Metternich gisoon na ay wi nekkoon ci noste gii, waaye bi mu koy gis fekk na waxtu wa jàll, manatu ca woon dara. Mu daal di bind Imbraatoor bu Otris bi ne ko: “Na la wóor ne nguuri Almaañ yi - bi lii amee de – di nanunañu nekki wenn yaram wu jàppaloo, ci ron kerug doxaliin guwu Brusiya, te da na jàppeji BrusiyaOtris muy - moom - aw yaram wu di doxandeem, wu tumbrànke wu bokkul ciw yaramam”. Te kat waa Otris yi ñoom, ca dëgg-dëgg, dunuduñu ay doxandeemdoxandéem ci waa Almaañ yi, ndax ñoo bokk xeet, làkk ak taarix. Man nanunañu ne Almaañ geppgépp mujj na bokksi ci Solofrayn gi, atum 1842g.
 
Xalaatu xeltu bu Hegel bi feddali woon na dooley nguur, ak ray gi muy ray jëmmjëmmaan (individu) ak lepplépp lu mu am, ngir sàmm dooleem akug màggam ak wegeelam. Nguur walla àtte – ci gis-gisgisu Hegel- cëslaayam mooy doole, ci doole rekk la man a dëgërale gëgg. Kon nguur walla àtte gu dëgër ci gis-gisu Hegel, mooy nguurug walla àtteg dëgg. Kon moom Hegel day mel ne moo teg ci loxol Brusiya lay wa di xeltu guy rafetal, di baaxal seen jëfi jiite googu nuñu jiite woon '''bennalug Almaañ gi'''.
 
Ñu leeral leen ne bi 1848g di jot, fekkoon na Brusiya muy reewréew mu am kàttan ci tere Otris muy dugg ci mbiri nguur-nguuraani Almaañ yi. Naka noonu, nekkoon na it mu amoon kàttan ci jiite yëngu-yëngu gi jugoon ngir bennal Almaañ. Nguur-nguuraan yi bokkoon ci Solofrayn it, doon man a dimblante ci seen biir ci wàllug koom-koom, te daan jëflante ci lu dul yoonu Otris di ci nekk mbaa ñuy diisoo ak moom, walla ñu koy tàggu. Ci noonu nguur-nguuraan yooyu tàmblee xoole Brusiya bëtu kilifa. Ci noonu la bennoo gu koom-koom googu doon màgg ak a naatdëgër ci ro kerug Solofrayn, mujjoon di ab jeegojéego bu mag jëm ci ag bennoo gu [[politig]] ak [[xare]] ci Almaañ.
 
 
Jeexiit== Jeexiital yi fipp[[jeqiku]] gu atum 1848g defoon ci amug bennoo gu Almaañ gi: ==
 
Ay fipp yu bari jot nanoo am ca Tugal atm 1848g. Ag fipp am ca Paris, am gu am ca Vienne, geneen ca Brusiya ak ay fipp ci Itaali ak Almaañ, yepp it di xëccu jëm ci ag gore , demokraasi ak xeetu . Metternich mu màggat mii, mujjoon na manatul woon a noot fippi Tugal yooyu, mbaa mu giimal leen, ni mu ko baaxoo woon a defe.