Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 9 :
 
Napoleon ak xarekatam ya xuusoon nanunañu ci diiwaani[[diiwaan]]i [[Almaañ]] yi, teg leen loxo. Daal di jawali ca nguurug Brusiya, gi nga xam ne jàmmaarloo woon na’ak ñoom cig njàmmaar ak fit, waaye Napoleon moom mujj na ko notnoot, te gañe ko ci mujj gi, ca '''xareb Yena ba''', atum 1806g, daal di teg loxo peeyampéeyam ba [[Berlin]].
Napoleon merloo woon na lool waa Brusiya yi, ci dog gi mu dogoon ay wàll ci seeni suuf, te jébbaloon leen diiwaanu Saksoni[[Saksoniya]] bi. Waaye nag ci geneen wàll, am na lu am njariñ lu mu fa indi, ndaxte wàññi woon na limub diiwaan yu Almaañ yi ba ci fanweer ak juroom ñeent rekk, te bu njëkk lu jege 360 lanulañu woon. Kon jëfi Napoleon jii, mbir la mom moo nooyal yoon wi, waajal ko ba ag bennoo gu Almaañ man a judd, man a taxaw.
 
== Almaañ ginaawginnaaw [[ndajem Vienne]] mi: ==
 
Almaañ ginaaw ndajem Vienne mi:
 
Ginaaw bi Napoleon Bonaperte daanoo atum 1815g, ci lanu def ndajem Vienne, ñu jële fa ay saxal yu bari, bokk na ci yooyu, dagg Doox bu Warsaw gu Poloñ gi, dagg ko ci Brusiya, te jox ko Rusi, bu ko defee ñu jox Brusiya moom itam goxub Rayan ak xaaju diiwaanu Saksoni. Daal di taxawal ag bennoo gu Almaañ gu làmboo fanweer ak juroom ñeenti nguur-nguuraan yu Almaañ, Otris jiite ko.