Yewwute gu ndefar wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 127 :
 
 
Yewwute gi ci OrobTugal jur na ay gàddaay yu mag, juge ci àll yi, ak dëkk-dëkkaan yi, dem ci taax yi ak dëkki endustrindefar yi, loolu nag mi ngi am ci bi isin yi yokkoo, jumtukaayi endustrindefar yi gën a xereñ cig wàll, moomeeli mbay yu mag tàmblee feeñ ci Tugal, la ko dale ca ñaareelu xaaju xarnub fukk ak juroom ñatt g, rawati na ci Angalteer ci geneen wàll. Bu ko defee baykatu Orob bi moom gisoon ne li ko gënal daal mooy mu dem ci isin yii nga xam ne li nu koy fay moo gën a wóor te gën di lu nu xam, te bàyyi mbay mii nga xam ne leeg-leeg mu baax, leeg-leeg du baax, ak jafe-jafe yi mu àndal, muy njaay meek toppatoo gi.
Lii mooy li waral ñiy ligeey ci mbay neew, te wàññiku, ñi dëkke kaw gi gën a neew, loolu it jur yokkug ñi dëkke ci taax yi, bu ko defee, am lu juddoo ci loolu, mooy neewug jóoxiitum mbay mi , te loolu it tax na njëg yi aju ci mbay ak li ciy juge gën a seer.
 
Bu ko defee, baykatu Tugal bi moom gisoon ne li ko gënal daal mooy mu dem ci isin yii nga xam ne li ñu koy fay moo gën a wóor te gën di lu ñu xam, te bàyyi mbay mii nga xam ne leeg-leeg mu baax, leeg-leeg du baax, ak jafe-jafe yi mu àndal, muy njaay meek toppatoo gi.
Beneen jafe-jafe daal di juddooti, mooy bu aju ci dëkkuwaay ñeel way gàddaay yu bees yii gàddaaye kaw ga ngir dëkksi ci taax yi, di wër ligeey. Ci noonu ay barabi dëkkuwaay yu xat tàmblee feeñ ci wetu fi isin yi nekk. Di dëkkal lu sakkan ciy nit, te matalewul li nu laaj ci dëkkiin wu baax te xellu. Ci noonu wér gu yaram dajeeki jafe-jafe yu rëy a rëy , jikko it naka noonu. Jafe-jafey ligeeykat yi gën na a yokku, bi nu demee ba li nu leen di fay manatul a faj gën ja’a neewi seeni aajo, ngir seerug dund gi.
 
Lii mooy li waral ñiy ligeeyliggéey ci mbay neewnéew, te wàññiku, ñi dëkke kaw gi gën a neewnéew, loolu it jur yokkug ñi dëkke ci taax yi, bu ko defee, am lu juddoo ci loolu, mooy neewugnéewug jóoxiitum'''njóoxiitum mbay''' mi , te loolu it tax na njëg yi aju ci mbay ak li ciy juge gën a seer.
Beneen jafe-jafe bu mboolaay bu bees amati, ànd’ak yewwuteeg endustri gi, ak ag jëmam kanam, loolu mooy ne lu bari ci jigeen ñeek xale yi, leegi danoo tàmbli di ligeey ci isin yi, te kat kenn soññu leen ci ku dul boroom isin yii nga xam ne li leen ñoroon weesuwul nu nu man a gën a ame ay ligeeykat ba gën a man a neew lu nuy fay, ginaaw ligeey bi ci isin yi laajul doole ju rëye noonu ngir man ko. Loolu tam jurati yeneen jafe-jafey mboolaay, ndax tax na ba jigeen bàyyi fi ay ligeeyi boppam, dem ci isin yi, xale yi it bàyyi njàng mi, te loolu ag pert manu koo kawe, ndax xale yi ñooy yaakaari ëlëg.
 
Ag yàqu-yàqu tàmblee feeñati ci wërlaay gu mboolaay yi, ci Tugal, maanaam nit ñi, loolu nag mi ngi am bi ag ñàkk-ligeey tàmblee tas ak a yaatu ci Orob, ci ligeeykat yu góor yii nga xam ne danoo tàmbli woon a nekk ay jafe-jafe dëgg, ci kanamu goornamaa yi, di yëngal, tey sàkku nu nu leen lijantile seen jafe-jafey ligeey yi. Ci noonu goornamaa yi daal di def ay àtte , indi ay sart yu nos ligeey bi, aar ligeeykat yi ci fuqaleg boroom bopp-alal yi moom isin yi.
Beneen jafe-jafe daal di juddooti, mooy bu aju ci dëkkuwaay ñeel way gàddaay yu bees yii gàddaaye '''kaw''' ga ngir dëkksi ci '''taax''' yi, di wër ligeeyliggéey. Ci noonu ay barabi dëkkuwaay yu xat tàmblee feeñ ci wetu fi isin yi nekk. Di dëkkal lu sakkan ciy nit, te matalewul li nuñu laaj ci '''dëkkiin wu baax te xellu'''. Ci noonu wér gu yaram dajeeki jafe-jafe yu rëy a rëy , jikko it naka noonu. Jafe-jafey ligeeykatliggéeykat yi gën na a yokku, bi nuñu demee ba li nuñu leen di fay manatul a faj gën ja’a neewinéewi seeni aajo, ngir seerug dund gi.
 
Beneen jafe-jafe bu mboolaay bu bees amati, ànd’akànd ak yewwuteeg endustrindefar gi, ak ag jëmam kanam, loolu mooy ne lu bari ci jigeenjigéen ñeek xale yi, leegi danoodañoo tàmbli di ligeeyliggéey ci isin yi, te kat kenn soññu leen ci ku dul boroom isin yii nga xam ne li leen ñoroon weesuwul nu nuñu man a gën a ame ay ligeeykatliggéeykat ba gën a man a neewnéew lu nuyñuy fay, ginaawginnaaw ligeeyliggéey bi ci isin yi laajul doole ju rëye noonu ngir man ko. Loolu tam jurati yeneen jafe-jafey mboolaay, ndax tax na ba jigeen bàyyi fi ay ligeeyi boppam, dem ci isin yi, xale yi it bàyyi njàng mi, te loolu ag pert manu koo kawe, ndax xale yi ñooy yaakaari ëlëg.
Loolu tam jurati yeneen jafe-jafey mboolaay, ndax tax na ba jigéen bàyyi fi ay liggéeyi boppam, dem ci isin yi, xale yi it bàyyi njàng mi, te loolu ag ''pert'' manu koo kawe, ndax xale yi ñooy yaakaari ëlëg.
 
Ag yàqu-yàqu tàmblee feeñati ci wërlaay gu mboolaay yi, ci [[Tugal, maanaam nit ñi]], loolu nag mi ngi am bi ag [[ñàkk-ligeeyliggéey]] walla ag '''liggéeyadi''' tàmblee tas ak a yaatu ci OrobTugal, ci ligeeykatliggéeykat yu góor yii nga xam ne danoodañoo tàmbli woon a nekk ay jafe-jafe dëgg, ci kanamu goornamaa yi, di yëngal, tey sàkku nu nuñu leen lijantile seen jafe-jafey ligeeyliggéey yi. Ci noonu goornamaa yi daal di def ay '''àtte''' , indi ay sart yu nos ligeeyliggéey bi, aar ligeeykatliggéeykat yi ci fuqaleg boroom bopp-alal yi moom isin yi.
 
[[Catégorie:Endustri]]