Isipt gu yàgg ga wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
m Yòonalaat ko Esipt gu yàgg ga mu jëm Isipt gu yàgg ga
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Isipt gu yàgg''' ga nekkoon na réew mu woomle, mu ami [[suuf]] yu naat, yu nangu mbay, ngir dexam gu mag googu di ([[Niil]]), am na it ay mbelli wurus ak xànjar ak weñ ak jamaa. Moo nga tambalee woon ca peggu [[Sudaan]] jëm ca [[Géej gu diggu|géej gu diggu]] ca bëj-gànnaaram.
 
Isipt bu njëkk dafa séddaliku woon ay xaaj. Ci jamonoy 3200 nj.j(njëkk judd gi) lañu bennal xaaj yii, mu mujj nag di nguur gu dëgër, buur bu tudd Firhawna jiite ko, ay foŋsaneer di ko jàppale yu man a bind man a jàng.