Ubbi njël lu njëkk li

Modifications

5 octets supprimés ,  il y a 11 ans
orthografie
----
== Li muy jariñ ==
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñépp añéppa deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen deggdégg des na, ñu man amana soxla ku ñu jokkool ci làkk biwi ñu deggdégg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgg abëgga jàpp ci liggéey bi, kon di na am -solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man amana waxtaane, ngir njariñam man amana feeñ.
 
Bii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan wu bariy làkkbarilàkk wu mel ne wu Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof bu ab jëfandikukat bu bindu.
 
== Nu ma koy defe? ==
3 285

modifications