Ndimbal:Sàqum jëfandikukat wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
orthografie
Rëdd 1 :
Wii xët da lay wax lu ''sàqum jëfëndikookatjëfandikukat'' di tekki, luy ay ngëneelam, noo koy sosee. Di la tektal tamit yoon wi ngay jaar ak xibaar yi ngay dajeel ci yoonu soste ngigi, yooy gis te, xaynaxéj-na, xamoo seen tekki.
 
== Sàqum jëfandikookatjëfandikukat ==
==== Ay ngëneelam ====
Balaa dara, yeneen jëfëndikookatjëfandikukat yi, di nañ la xam, man amana xammee say cëru ak say waxtaan. Ci turu jëfandikookatjëfandikukat bi ngay tànn, lañ lay xammee (so demee bay bindu). Di na tax nga man amana bokk ci aw askan wuy gën di yaa.
 
Su loolu weesoo di la xamal ne sàqub jëfandikookatjëfandikukat yemul foofu rek. Soo sosee sam sàq ba noppi, Wikipedia dijjiltijjil la boppam nak,! joxJox la ay jumtukaay yu ku binduwul manuta jot. Ab lim bu tuuti ngi nii ci suuf:
 
* Di nga am sa xëtu bopp fooy man xamalee sa bopp, man nga caa def lépp lu la neex, ci misaal: ab nataal, ay lëkkalekaay,... Soo xoolee yu ñeneen ñi man nga caa jëlee ay misaal.
* Di nga am sa xëtu waxtaanukaaywaxtaanuwaay, foo xam ne yeneen jëfandikookatjëfandikukat yi fa lañ lay bindee ay bataaxal. Soo amee bataaxal bu bees di nañ la ko yëgal ci anam bu gaaw(doy na nga dugg).
* Di nga man amana topp yenn jukki yi ngir man amana xam ndax soppeeku nañ walla déet. Doon na lu am solo ndax soo sosee sab jukki di na tax nga man kaa topp ba ab saay-saay du ko yaxyaq, mbaa yokk ci ay xibaar yi baaxul.
* Di nga man amana soppi say tànneef.
* Di nga man amana am ab lim ci say cëru, lépp loo indi ci Wikipedia.
* Di nga manmana a tuddeewaattuddewaat koj yu xëtu jukki yi.
* Di nga manmana a jëliyeb ab filedencukaay
* Beneen ngëneel bu am solo mooy ne sa màkkaanub IP kenn du ko gisati, ndax soo binduwul sa IP la ñuy bind (ci Jaar-jaar) muy turu ki def boobu cëru. Loolu kaaraange la ngir sa PC,[[nosukaay]] di na tax ba saay-saay si du ñu la man amana gis, di xam foo ne, bay man amana indi ay tolof-tolof ci sa PC.
 
==== Foo koy jëfandikoo? ====
Soo sosee am sàqum-jëfëndikookat jëfandikukat ci Wikipedia wolof, foofu rek nga koy manmana a jëfëndikoojëfandikoo. Kon beneen Wikipedia bu ne da nga faa war awara bindu soo fa bëggee cëru.
 
Su fekkee jëfandikookatjëfandikukat bi doxalinam mengòowulmengóowul ak àtte yi Wikipedia tërëltëral ngir yorteem jaar yoon, yorkat yi am nañnañu sañ-sañu teye la ab diir ba doo manmana duggal dara.
 
== Tànn ab turu jëfandikookatjëfandikukat ==
==== Turu Sàqum-jëfandikookat jëfandikukat ====
Lu weesu xibaar yi ñu la jox ci xëtu [http://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=Special:Userlogin&type=signup mbindu mi], [[login|loginu]] mbindu mi ci Wikipedia, ci kàllaama xarala mooy "Turu Sàqum-jëfandikookat jëfandikukat".
 
dañdanu koy jappee ni sa dakkantaldàkkantal, jëmm gu dëggu gu jëfandikookatjëfandikukat yi, man nu ñu koo xam ndaxte ku mu neek man ngaa bindoo ak:
 
* Sa tur dëgg;
* Sa tur dëgg goo xaw axawa soppi;
* Turu jambur boo jël;
* Walla ab dakkantaldàkkantal boo sàkkal sa bopp.
 
Lépp mi ngi aju ci ni nga bëggbëgga a bokkeebokke: naxasal, walla jubal walla bañ ku la xammee. Xamal ne tamit sa turu Sàqub-jëfëndikookatjëfandikukat warul doon baat bu ñakk -teggin, baat buy wone sag bokk ci yenn mbootaay yi (politig, diine,...). Man jur ay réeròoréeróo ak ñeneen ñi. Day tax ñuy gisee say cëru ak yeneeni gët ( ci misaal baat yu mel ne "Hitler" walla "kkk").
"Turu Sàqum-jëfandikookatjëfandikukat" bi day tax nga man amana xaatim say bataaxal ci xëtu waxtaanukaaywaxtaanuwaay yi, ñetti '''~''' ngangay def ci sa njeexintalujeexintalu bataaxal, ngir xaatim.
 
==== Tur yi jar ajara moytu ====
Man ngaa jëfandikoo sa tur dëgg, su la neexee, waaye li ëpp ci waa -wikipedia yi, ay dakkantal la ñuy jëfandikoo. Daanaka tur bula neex jël, waaye nak am na ay gappudig:
 
==== Tur yi jar a moytu ====
Man ngaa jëfandikoo sa tur dëgg, su la neexee, waaye li ëpp ci waa wikipedia yi ay dakkantal la ñuy jëfandikoo. Daanaka tur bula neex jël, waaye nak am na ay gappu:
* Ab saaga manoo koo jël, ndax ni ko ñeneen ñi di gisee, su amee it di nañ sakku ci yaw nga soppi ko.
* Bul di jëfandikootjëfandikoo tur dëgg bu jambur, donte ku siiw la, koo doon soppeem.
* Bul di jëfandikootjëfandikoo turu këru koom-koom walla bu nit bu sañ-sañuaqi soskataji-sos aar
* Bul di jëfandikootjëfandikoo baat yii: yorkat; àttekat, bot,...), ndax dañoo am yeneen tekki, kon day jur jaawale.
[[catégorie:jeego yu njëkk]]