Alaaji Maalik SY wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Malhonen (waxtaancëru)
Annulation des modifications 12397 de 24.254.31.38
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Alaaji Maalik''' ma nga gane àdduna Gaaya ca wetu Dagana atum 1855. Waajuram wu góor tuddoon Usmaan, wu jigéen Faa Wàdd [[Wele]]. Mi ngi jànge alxuraan Luga ci kenn ci taalibey Alaaji Omar Futiyu Taal yi. Bi mu doonee mag la dem Màkka, bi mu [[dellusee]] sax ci jaamu Yàlla ak jàngale ak dugal ñi duli jullit ci lislaam. Ci noonu la tase njàngalem yoonu Tiijan ci [[Senegaal]] jaare ko ci tuxoom yi ci Jolof, Kajoor ak Ndar. Ci mujj gi mu dëkksi Tiwaawan atum 1902. Fa la njëkk a xumbale [[gàmmu]]. Wooteem bi mi ngi ko doon defe ci dëkk yu mag yi, tabax fa ay jàkka, xeex fa ag réer akug ñàkk, ñu tudde ko Mawdo [[giiy]] tekki aji gindi ji. Alaaji Maalik nag (yal na ko Yàlla gërëm), mi ngi laqu atum 1922 g.j.
[[catégorie:niti senegaal]]