Sëriñ Mbay Jaxate wuute gi ci sumb yi

4 octets ajoutés ,  12 at ci ginaaw
m
Coppite gi amul tënk
m
'''Sëriñ Mbay JAXATE''' nekkoon na di kenn ci woykati [[wolof]] yu mag yi (taalifkati woy yi) di woon it benn taalibeb Sëriñ Tuubaa, li mu taalif ci woyi wolof maneesu koo misaal mbaa deesi ko lim, nekkoon na di ab soofiyu bu mag, lu ëppoon it ciy woyam ci googule wàll la jëm, ku lislaame la woon te di woon ku jéggi dayo ba cig taral ci ñu sammoonteek daytali Yàlla yi aki ndigalam, bokk na ci ay woyam''' yii:
* pexem Yàlla moo gën pexem nit ndaxam '''()''' fa Yàllay fexee yàqkat yeggu fa
* Murit yaw de bul mer te bul jàpp mer '''()''' mer ak jàpp mer day alag ab murit
300

modifications